contenu de la page
Connectez-vous S'inscrire
Asfiyahi.Org - 1er Site de Reférence sur l'Islam et la Tidjaniyya au Sénégal دائرة الأصفياء
Asfiyahi.Org
ABONNEZ-VOUS À NOTRE NOUVELLE CHAINE YOUTUBE HD

Publicité



DELLOO NJUKKËL Al Mourchid Seydi Abdoul Aziz Sy Al Amine


Cet Article a été lu plus de 1566 fois




DELLOO NJUKKËL Al Mourchid Seydi Abdoul Aziz Sy Al Amine
Au Sénégal si on peut parler de la constance personifiée, je dirai sans risque de me tromper que, Al Mourchid, Seydi Abdoul Aziz Sy Al Amine est l'incarnation la plus parfaite jamais égalée à travers les temps et de par sa pilosophie de la vie.

Dès l'âge de 14 ans, il a gagné la confiance de son père Cheikh Al Khalifa, Serigne Babacar Sy. Tous les successeurs de son vénéré père lui ont renouvelée cette confiance qu'il a sue pérenniser, malgré les énormes et nombreuses adversités, de par ses actes envers toutes les communautés éthniques, ses civilités envers ses détracteurs et ses adversaires, ses relations avec l'eglise et toutes tarikhas, ses bienfaits envers les necessiteux, ses vertus pédagogiques et sa prophetie...

La Fédération des Dahiras Tidianes d'Espagne a voulu consacrer cette année 2015 à lui rendre HOMMAGE en guise de reconnaissance à cette longue trajectoire: un “NJUKKËL” à la dimension de sa personne.

DELLOO NJUKKËL
(Al Mourchid Seydi Abdoul Aziz Sy Al Amine)

Abdul Aziiz, abb dallu baay ba Aziiz
Sa turëndóo ba Mulaay Dabbaax
Xelu di xelli ci sa xel
Xool la Maodo xalaat
Bayee Seydi Mbay mu wéyël
Sas la ngay baat di doxal
Li kër gi soxla ci protokol
Xajoo képp ku fa ñëw
Ñoñ politik baa gan gu mu doon
Ki xamul féetélé la boor
Xam Ps baa PDS, APR walla REWMI...
Daa xamul ni yaw li la ñor
Moo di liy doxal rewmi
Ki déggul dara tuumaal la
La la gor ñi ak fóori yi di kañee
Ci xam xam ak jikkóy AL AMIIN
Di dox diggënté tey defar
Andi gor, diine ak jaboot
Di doxal dëgg tey baña far
Ame cofeel ci ñi nga boot
Wormaal mag, teral noon
Baay Siidy Moxtaar Mbakke dëggël
Sa dëggu ak dogu ci mbokk gi
Al Maktuum dellu saxal
La mag ña jiwoon ca sa ndaw
Ngay wéy di suuxat luy dundël
Yoonu Seex ak xadara Maalik
Seede yaa ngii tey, du ñu jeex
Burd, Gammu baa Ziaar General
Makka, Koor baa Tabaski
Ngénte, ku faddu baa ku fande
Maam Mbay, Balxawmi baa Dabbaax
Jamiil, Mansuur baa Seex Tijaan
Yaa di géej, deesula xuus
Xanaa di ñaan Buur Yallah mu musël
Yaw sunu Baay Al Amiin
Samm njaboot gi ñu magg
Saxal Al Maktuum, Al Xaliifa
Ci tasaare ndono ak njángale Maam Maodo



Moussa Fall – Secrétaire de la Fédération des Dahiras Tidianes d'Espagne
Fédératioon des Associations Seydi El Hadji Malick Sy (FASEMSY) d'Espagne
moussafallfall@yahoo.es


Asfiyahi.Org
Mercredi 11 Mars 2015

Cet Article a été lu plus de 1566 fois





Réagir à Cet Article !

1.Posté par fatou mbodji le 11/03/2015 12:16 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
machala yalla nafi yague ande ak weur sy.

2.Posté par Emu le 13/03/2015 12:36 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
macha Allah

3.Posté par Papis le 15/03/2015 19:16 (depuis mobile) | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
Il est notre fierté!!!

4.Posté par vérité le 16/03/2015 16:37 | Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
Serigne Abdou Al Amine c'est des convictions très fortes, une fidélité inaltérable, une foi inébranlable et un courage immense. Puisse ALLAH Tout Puissant l'aider, le soutenir et le renforcer pour l’honneur de la confrérie tidjane et de la hadara de Maodo.

Nouveau commentaire :
Facebook Twitter


Telechargez l'application Mobile Asfiyahi pour plus de navigabilité ABONNEZ-VOUS À NOTRE NOUVELLE CHAINE YOUTUBE HD


Dans la même rubrique :