VIDEO : Les Images de l'ouverture du Bourde à la Zawiya El Hadj Malick Sy (rta)
Asfiyahi.Org
Réagir à Cet Article !
1.Posté par
Ndèye Fatimata Binetou Rassoul SECK le 15/01/2013 04:50
| Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
YALNANIOU YALLA MAY NIOU TANBALI CI BISMILAHI RAKHMANI RAKHIMI TE HAGALI CI ALHAMDOULILAHI RABINE ALAMINA TE YALLA NANGOUL NIOU LEP LOU NIOU FI NIANE. YALNA YA RAHMANOU GUEUNEU BARKEL ASFIHAYI. AMINE
2.Posté par
Adama NDIAYE
le 15/01/2013 10:00
| Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
Amine.YALNA YALLA DéF DIAM SI YONOU MAOULOUD BI BA FéPE FOU NITT DI DIOGUé DI DéME TIVAOUNE WALA MOUY DéME FOUMOU MENE DONE DI MAOULIDI BOROM BI DéF GA DéME SI DIAM Té DIKK SI DIAM SI BARKé MOUHAMADOU RASSOULILAHI PSL.
3.Posté par
Abdou Aziz Sy Ndiour le 15/01/2013 12:46
| Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
Nio guí sant yalla mom migni may feke. Ak tal ,kon nio guí delou di sant borom bi si bi khewel.di maouloud 2013 Yalniouka feke ay milliard at ci barke seydina Mohammed aleyhi wa Salamanca di guerram wa asfiyahi bou bakh nioune wa diáspora contane naniou ci yene bou bakh
4.Posté par
mor le 15/01/2013 12:50
| Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
YALLA NANU KO FEKKE TE TALKO TE MUDAXX MBOOLEEM YI FI JAAROON YALLA MAN NAKO YALLA NANU KO DEFAL CI BARKE BOROOM GUDDI GI SEYDUNAA MU XAMMAT SALLA LAAXU XALAYXI WA SALLAM
14.Posté par
MBOSSE NDIAYE le 19/01/2013 02:43
| Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
AMINE THI BARKE SEYDINA MOHAMED SWS. YALNAÑOU YALLA FEYAL MOUSTAPHA , TE TAFÑOU THI BARKEM
15.Posté par
Diaw NDEYE ASTOU
le 21/01/2013 15:00
| Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
amine way yalna yalla nangou
16.Posté par
J le 21/01/2013 16:17
| Alerter
Utilisez le formulaire ci-dessous pour envoyer une alerte au responsable du site concernant ce commentaire :
Annuler
Participer ci Bourd baakhna wante na gnu ko def ci discipline. Na gnou baayi Serigne yi gnii jaang talibe yi di Awu kom temps wu Mame Abdou. Wante bu gnepp bou guee jaang ci plassu Serigne yi Affaire bi du sooti.....Talibe dafay wuyoo Ndigeel........Amicalement de la part d'un fervent talibe de Boroom Daara Yi.