|
14 Septembre 1997- 14 Septembre 2017 - El Hadj Abdoul Aziz Sy Dabakh , l'Inoubliable , 20 ans Déjà !
dieureudieuf seugn bi que la terre te soit legere
dabakh le venéré le sage le régulateur modele et un exemple pour toute la ouma islamique amoul morome té ken lafi yallah na soufame séde té yallah tasse niou barkéme amine
Yalna Yallah fayalniouko té bagna tass souniou yakar si mome.,
Yalna Yallah yatal yeurmeumdème si mome, yok leeram té tass niou si barkèm. Amiine!!!
Dabakh était l''homme qui representait le prophete durant sa vie yalnako yalla deukelè ak sopém ba Seydina MOUHAMED (PSL)
Dabakh était l''homme qui representait le prophete durant sa vie yalnako yalla deukelè ak sopém ba Seydina MOUHAMED (PSL)
Mame boy do fi meussa diougué tu es enterré dans nos coeurs!! yalna niou la yalla fayal yok say ler té tass niou si sa barké!!
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|