|
[ AUDIO ] Comment faire le Wird ou Lâzim, la Wazifa, et le Dhikr du vendredi ou Hadratoul Djumah?
salam sama mbokou talibe yi guinaw bama sante yalla mangui jouli si rassoulilah s.A.W dilen ziarra t dilen nianal yalla yokk man man yi vrema s8 tres contente si wa asfiyahi pask c 1e bonne initiativ t dilen waxni boulen massa delou guinaw ndax yenangui khetali niou bari yalla nalen yalla fay si barke seydy aboubacar sy RTA allahouma salla alla seydina mouhamad wa sallim
alhamdoulilahi! yalla na yalla faye gueen gui faay, doli soutoureu , diamm, weer, kham kham te barkel ko!leeep lou fii way dieulé yalla na nek ndiarriignaam aduna ak alakhira. yalla na yalla boolé nou thi gni gueen si kheetou SEYDINA MOUHAMED (staw)
wayéé yééén initiateur yii, léép lougnou fi dieulééé si ndiarigne , yalla na léén yalla faye lou roomb séén ndioorta
amine
MAACHAA ALLAH YALLAH NA LENE BOROM BI FAYE SENE YENE MAIS ES CE QU ON PRATIQUER LE WIRD SANS L AVOIR PRIE
groupe asfiyahi yala na yalla léral yone bi. wayé nak da ma beugu ngéne ini d otrs niti yalla cme sa ma mame El Hadji Socé Ndiaye
merci yallah nalene yallah faye de se que voulait qui bon pour vous au fond de votre coeur
Ndeysan machala alhamdoulilah yalla naniou borome bi ték si yonou siratal moustahine et avec se site ndiarign ak yiw rék yalla borom bi fay lén yiw
Merci beaucoup que le Bon Dieu vous paye du bien.
Merci à toute l''équipe asfiyahi.org Dieureudieuf Cheikh Ahmed Tidjani.
Je veux prendre le wirde tijaniya a qui dwvre-je m''addresser?? ASSALAMOU ALEYKOUME WA RAHMA TOULAH
Alhamdoulilah j ai pris hier 24 janvier le wird Tidiane des mains du venere Serigne Abdou aziz sy Al Amine.Que Dieu lui accorde une longue vie. Yalnaniou yalla fayal Cheikhou Tidiane ak Maodo si barke Seydouna Mohamed sallalahou aleyhi wa salam.
C est l.une des faveurs que le prophète a bien voulu nous gratifie que dieu nous aide à l.accomplir convenablement merci
je suis vraiment ravi de ce texte publié par l'administrateur que Dieu lui soit reconnaissant et lui beni lui e sa famille ainsi que tout les musulman qui on contribué
alhamdoulilahi je reviens de fez je viens de prendre le wird tidjane par lintermédiare de cherif zoubir mais en plus jaurai besoin des conseils de mes ainés ( ceux qui mont devancés dans le tarikha ) je voulais poser la question à savoir est ce qu'une femme a l'obligation de faire la khadra dans une mosquée ou dans sa chambre je vous remercie tous et sollicite vos prieres yala na gnou yala défe aye talibé cheikh pure inchhalah yaala na yaala nangou sou gnou diamou yaalah
Salam. Grand merci. Yalla nalene Yalla faye. Juste une question
Pour une femme qui fait la Wazifa elle doit ou elle peut remplacer les 12 Djawharatoul Kamaal par 20 Salatou Fatihi.
Je veux dire est ce une obligation ou à t elle le choix.
Machala! wa Asfiyahi,amougnou sén faye,yalna Yalla fayal gnou léne ci Barké Seydina Mouhamed(psl) contane nagne lol.
machaalah niila islam koxhamnii tijaniyaa la daawaraa soukoo doukou thiili yaalana yaala baarker leen t''es weerelle seenthier wasaalamou aleiyeekoum
Pus-je avoir tous le wirde en audio svp
Je Tient A Remercie L'equipe Technique Pour C Tres Belle Publication
Allakhouma salli wa salime....... Sant yalla.... Merci bkou
Alhamdoulilah. Merci tout est clair
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|