Inch Allah bouniou moune dinaniou deff, bouniou mounoul dinaniou djem ba mouneka te deff ko ba dolli si barke mame seydi hadj malick rta.
votre equipe le merite, le hadara le merite. Que Allah swt nous assistes tous.
inchalahou dina diokhe louma ame. soubare doumako yeem sou newee doumako khep te dina sonie kouma yakar ne talibe tidjanla fi thi barcelona dinalako wakh