|
CHAPITRE 4 - EMISSION LUMIERE BOURDE : Naissance du Prophète (SAW)
Ma Cha Allah waay kou déff montage biii! ahh té seugn ahmad yalla yalla samm ko té geuneu oubii deuneum Ma Cha Allah! Fiiri gui lérr na loole!
Mancha Allahou Serigne Ahmed SARR. Wakhtane bi lérena lole. Yalla na YA RABI dolila Wére té yoke sa takhawaye. Amine.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|