|
Des reporters de Asfiyahi.Org victimes d'un accident sur la route de Richard-Toll
ALHAMDOULILAHI RABIL ALAMINE. Yéne bouléne dara diote. Yalna Yalla yeukeuti léne, Sameu léne Equipé léne bou baaheu baah inchalah Barké cheikh
Alhamdoullilah qu ils n ont rien grace a Dieu et pour le chauffeur que le bon Dieu l aide a s en sortir
alhamdoulilahi rabil-alamine yalna yala gueuneu wéral séne thiére sa same léne;;;; ndakh mission bi gniye défe yomboule;;;;;;;ak képe kouye déme guaya gnou déme si diam gnibi si diam si séne wétou famille thi barké wére bi
Yalla na yalla defal lèn wer tamou ande ak fane bou gouda
ALHAMDOULILLAH YALLA NA BUUR BIII SWT DOLLI LENE ARRE SAMA LENE YOKK WEER GUII SI BARKET TAHAA ... CHAUFEUR BIII YALLA NAKA SOUGNOU BOROM SWT DOLI SHIFFA
Yalna Yalla Takhawouleine dolileine Sameu Incha Allah 💝
Al hamdullillah buleen dara jott ndax Ajo jullit yi ak talibe. Yi la gnou dox chauffeur bi yal nako ALLAH. Safara Amine. Massaawuleen ci ndogal bi
vous étiez dans une mission noble yalla naléne yalla takhawou té feye léne si barké Seydi Haj Malick Sy
Massa lènn Thioono yal na si wèrr top yennay soldarou tariikha konnn soldaar bou blessé woo ci combat wathie naa.
Yalla na fi yamm yalla boumou fi amati. Gnii thie am ay blessures yalla nalènn yalla téguill séni métittt
ta diokh lènn kholou mougne .
YALLAH NALEENN YALLAH AARR TA SAMMMAL NIOU LENNN BIDIAHII RASSOULIL LAAHI (SAWS)
yalna yalla feugue bopame
Yalla na léen Yalla saam. di léen massawou di nianal chauffeur bi
GRACE AU BEAU BOULOT QUE VOUS ETES ENTRAIN DE BATTRE NOUS PRIONS TOUS POUR QUE LE CHAUFFEUR SE LEVE LE PLUS RAPIDEMENT TE YALLA AR LEN
YALLA BOROM BI SAAM LEN MOUTHIAL LEN BARKE SEYDINA MOHAMED PSL
thi retour bi famille vieux amssata fall de rufisque aussi def naniou accident sa femme est décédée et enterrée hier, aujourd'hui son fils qui était en coma a fini par rendre l’âme. Priez eux svp afin que Dieu ait pitié de leurs âmes
yalla nalène yalla takhawou; chauffeur yalla yeukeutiko thi diame;Amine
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|