|
EXCLUSIF ! VIDEO : L'histoire de Diacksao Racontée par EL hadj Abdoul Aziz Sy Dabakh ( Gamou 1983 )
MAAME BOY WEETAL NGA NIOU,YALNA BOROM BI FAYAL NU LA CI BARKE YEWANAL MBOK AK SAMM KOLEURE,AMINE BI DIAHI HABIBIKA SEYDINA MOUHAMMAD PSL
amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiinnnnnnnnnnneeeeeeeeeeeeee
Amine; Dabakh mou bakh mi!
mame boye senegal nieguilaye dioye ba légui yala dolé saye lair
Mame boye nopéguoniou sidioyeyi yallana yalla doli saye l air
Mame Abdoul Aziz SY DABAKH, Tour wouyouna borom, lou way wokh thi nom thi mbakh, Amna lou dess! Koné Yalna Yalla yessal yeurmeunde thi nom, yok Aÿ leram té Tass ni ou si barkee borom naniou tapé khôl yi.
Il avait l'habitude de solliciter des Talibés 3 salatoul fatihi en hadiya au Prophète (SWS). Alors nous qui disons l'aimer, prenons l'habitude de le faire après chaque prière.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|