|
Ecoutez El Hadj Cissé Djingue!
tay rék ladone déglou wayou el hadj mor samb yi ci séne site bi ba sama khél dém ci binde léne message wahléne nguéne dougeul you el hadji malick cisse djingue ndékété yalla dogual na tay nguéne koy dougeul...
ndeyssane 1950 ba 1957 mo wayal serigne babacar sy gamou tivaouane ci diouma seydil hadji malick, serigne babacar féki makk yi mouy wayal mame cheikh ak ndiabote yi ci diouma mame babacar ba 1992 mou tambali wayal serigne moustapha ibn mame cheikh ak serigne mansour ibn mame cheikh ci gamou yi a thies puis mame cheikh au champs de course ..gamou bi passé bimou wayé ci diouma mame babacar fou sori la yobou kouy ndiabotou serigne babacar di ndiabotou mame cheikh ndeyssane...
limou amé ci kham kham nak KAR MACHALA rék lassi nite meune wakh... yalla na yalla arko soutouralko bayiko ci képarou mame cheikh mame babacar ak mame seydil hadji malick té yalla bolégnouko, yalla yokh katane gui deugeureul tahaway bi motali yéné yi ci barké mame cheikh... exemple piir nga ci gnoune ndiabote yi
Merci pour ces chants j'aimerai savoir comment faire pour télécharger ces sons
oh ce monument de elh cisse djigue merci
MA CHA ALLAH MERCI BCP LONGUE VIE ET SANTE DE FER
Salam, il n'y a aucun chant disponible sur cette page merci de réinitialiser vos pages.
SANG BI COSSE DJI?GE SANG BU JARA SOPP AK ROY NGIR TEDD
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|