|
|
Ecoutez El Hadj Mor Samb !
Serigne mor samb yalla ko mayon mou wouté ak jang kat you bari ...Serigne BABACAR SY moko ték thi lokho CHEIKH SEYDI MOUHAMADOUL MOUSTAPHA SY DJAMIL mou formé ko jangalko way dan and ak mom di way mou don nit kou kémané machallah YALNANOUKO YALLAH FAYAL...................AMIIIIIIIIIIIN
macha allah. beug nanou boubakh
essayez de mettre des sons d Ablaye Samb de Moussa Niang et d Issa Laye quand c'est disponible.
yalla na yalla fay léén.
Kel voix +de sons de mor samb
Promotions Ramadan chez Blue Line
• Split Samsung 1.25CV installé à 244 000 FCFA >> 230 000 FCFA
• Téléviseur Plasma Samsung 109 cm : 300 000 FCFA >> 285 000 FCFA
• Téléviseur LED Samsung 82 cm : 230 000 FCFA >>215 000 FCFA
• Home cinéma Samsung : 250 000 FCFA >>215 000 FCFA
• Congélateur 280 litres Westpool : 220 000 FCFA >> 200 000 FCFA
• Cuisinière 4 feux grill blanche : 110 000 FCFA >> 95 000 FCFA
• Cuisinière 6 feux grill blanche : 155 000 FCFA >> 140 000 FCFA
Dépêchez vous, stock limité !!!
A découvrir sur www.blueline-senegal.com ou 33 827 77 10
MACHA ALLAH LII NEKHNA TROP SOUNOU MAME MOR SAMB
machalah mais les chants issa laye si possible
Machaa-Allah Serigne Mor Samb était un chanteur religieux qui faisit plaisir à ceux qui l'écoutaient. il avait une voix dorée et chantait avec beaucoup de maitrise. Mais ceci ne doit pas etre une surprise pour ceux qui le connaissaient ou pour ceux qui lui fréquentaient car il a été formé par le vénéré marabout Cheikh Seydi Mouhammadou Moustapha SY Djamil (RTA) fils ainé de Cheikh Seydi Aboubacar Sy (RTA). Yalanako yalla fay nimougnou done bégalé yalnako bégué ci kanamou Serignam.
mashalla ,wayi nèkhna yalna lèn yalla bourbi fay ci barkè yonèntibi ak bèp talibè cheikh , jai toujour les larmes au yeux en ecoutan les jang kat yidaa and ak serign babacar malgrè jètè pa nèè a c temp ,il faut nous mettre des possible asfiyahi.org ,yala ngèn am gueureum
mashalla ,wayi nèkhna yalna lèn yalla bourbi fay ci barkè yonèntibi ak bèp talibè cheikh , jai toujour les larmes au yeux en ecoutan les jang kat yidaa and ak serign babacar malgrè jètè pa nèè a c temp ,il faut nous mettre des possible asfiyahi.org ,yala ngèn am gueureumu[
mashalla ,wayi nèkhna yalna lèn yalla bourbi fay ci barkè yonèntibi ak bèp talibè cheikh , jai toujour les larmes au yeux en ecoutan les jang kat yidaa and ak serign babacar malgrè jètè pa nèè a c temp ,il faut nous mettre des possible asfiyahi.org ,yala ngèn am gueureumu[
wayyi néékh na lool yalla mooham payouk el hadji mor samb, noo gui nhian moufékk koko famou né nhiokh ko ay khéé weul ak bép dioulit boub fafék ak bouko faféqq amiin .ganaw loolo weur naa weur issa laye nhi cites yi wayé nhissou makko sou guéén ko amméé guéén baa khénou ko wassalam
machala sunu papa mor samb yalnako yalla hare aldianay firdawsy
Ahhh! Néxna ki rek momay danél!
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|