|
Ecoutez Mbaye Dondé Mbaye !
Yalla na Yalla yok sen ler te yobulen thi aldiana you guen ye kawe
nioun ni fi dess Yalla na Yalla yok sunu pass pass thi tarikha Cheikh te niou gueuna deugueureul sunu joku thi keur seydi Hadji Malick sy
AL HAMDOULILAH AL HAMDOULILAH AL HAMDOULILAH!!!! YALLA NA YALLA NANGOU NIANE YEEP TE BARKEL KO.MANGUI ZIAR GNEEEEP
que le bon dieu nous donne les biens du mois de ramadan amin
Merci asfiya de tout il fait pour les tlibes tidiane Je voudrais qu'on m'envoit les chants de Mbaye Donde de doudou
le khasi mbaye donde mbaye yallna yalla yokou leeram te khareko al diana you kawe ya si bargue saydouna mouhamid
El hadji mbaye dondé MBAYE yalla na yalla yok léram adiana té tas niou si barkem
Elh mbaye donde yalna yalla fayal niu ko amiine
Ecouter les chansons de El Hadj Mbaye Dondé Mbaye apaise le coeur et apporte la sérénité.
Sope Serigne Babacar SY MALICK
El Hadj Mbaye Dondé Yallah na Yallah tassalé la ak Serigne Babacar ak Mame Abdou Aziz Dabakh thia Aldiana yi gueuneu kowé ak sougnou waydiour yi gnou djitou.Amine Ya Rabbi
yalla naniou ko yalal fayal. Ci bareké Serigne Babacar SY (RTA
). Macha allah.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|