|
Ecoutez Serigne Habib Sarr (rta)
Ma sha Allah contane trop si asfiyahi yalna ya Allah barkel lep ,serigne Habib Sarr sama sopé bi yalna firdawsi done keuram
Diangalé bou lére nagni la yorone...Machallah yalla nako yalla yeureum barké SEYDIL HADJI MALICK SY
aboubakr sadikh attidjani ba
je voudrais savoir si possible comment telecharger ces fichiers audios
Tu peux les telecharger a partir de :http://convert2mp3.net/en/index.php
Serigne Habib Sarr yalla nanala yalla égalé si barzakou seyidiana Cheikh mou égaléla si bou yonente saw
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|