|
Gamou Annuel Fédération Sope Naby de Serigne Issa Touré, Samedi 8 Avril 2017 à Kélle
Incha ALLAH nous y seront. Serigne Issa TOURE moy Kharitou jeunesse bi.
Jarama Sérigne Issa Touré yalla nala sunu borom fayaal nioula yok sa meun meun doli la wér bayila fi ba ci kanam. L''ami des jeunes alhmdu lilah je réitère mon Amour en toi et je dis encore une fois merci mon Dieu de m''avoir fait votre Talibé.
Serigne Issa souniou kharitt souniou serigne souniou Papa souniou conseiller yalla na la fi yalla bayi nga yégali sa mission ak sa sago mouy souniou ndieurigne nioune nieup. TOURE YAGUE FI LOOOOOOOOOOOL
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|