|
Gamou Cherif Ibrahima Aidara, Samedi 31 Décembre 2016 à Hamo 4 : Le rendez-vous de la spiritualité tant attendu !
Bonjour à tous!
Achetez et vendez du tout sur www.toobalist.com le premier site sénégalais et africain d'annonces gratuites et exposez vos produits à des millions de clients potentiels à travers le monde.
N'oubliez pas de visiter votre forum populaire : www.toobalist.com/forums
http://www.toobalist.com
ziar ak magal Dieu ma donné la chance de participer A ce gamou wayé seydy haj . cheruif aidara ya bakh té oyof yalla nala yalla bayi sounou kaname ay atttt you beuri ak thierno bachir ak azatiza yeup
salam ak ziar
Chérif Ibrahima Aidara cet homme d'une dimension spirituelle incommensurable a changé la vie de beaucoup de jeunes . Machallah nous rendons grace au Tout puissant de vous avoir cotoyer et nous ne le regrettons jamais . longue vie à vous
macha Allah. yalla nagnou sounou borom fayal sounou serigne sounou wassila Cherif Ibrahima Aidara at tidjani. oyofna bahna tabéna ham ham bi macha allah té yénénako djamou bour yalla yeup.
sa kaw sa kanam
khamnaa kou am thieurla mom SHERIF, chaque fois je regarde ces causeries sur YouTUBE et sur Asfiyahi danguay yéggni kou bari xam xamla, xam tarikha bi akk Keur Seydi Hadji Malick .
Yalla Samekko mayko goudd fan bou and ak wérr...
cherif IBRAHIMA AYDARA yalla nafi yague té and ak weer
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|