|
Gamou Trevizo ( ITALIE ) Samedi 23 Avril 2011
ziarrr que Dieu fass que lévenement se deroul normalement commencé si bisimila terminéko si alhamdoulila si barqué borom journébi je profit de locasion di ziar le president Aliou Badada Beye et tous ces partisants bn gamou
à qu'elle heure le dèmarrage du direct?
Yalla na Yalla saam bepp talibé bou cieu jeum
niou exi ci jaam,gamou ci jaam té waniékou ci jaam
té lepp lou niou fa niane Yalla na niou bokk.
Gamou gui nekh na ma cha allah
Que Dieu exauce toutes les prières qui ont ete faites.
Prions que Dieu veille sur la famille de Maodo Malick Sy (Paix en son ame) et à tous les musulmans du monde entier.
Un grand diadieuf à wakeur Serigne Touba de TREVISO ( Paix en son ame)
yallna yalla dolli men men gui wakh degg fa yalla gamou gui nèkhna ba romb nèkh mennasi sakh dafa alla dawmèèè yalna gnou yalla bayyèkk ndiabootou wa keur seydil hadji malick thi dignou dolli rèkk la gnou dekk guinnaw lolou ma ngui gnanal kou mèlni sama papa badara beye ak mboolèmm gnimou bokkal liguèy bi mak ak ndao ba mou mene yeksi fi tay malèn di gnanal yalna lèn ko borom bi di men loo att bou nèkk thi barki borom mbonèkarè ak cheikh mignou boolè gnoun gnep ndiabootè akit thi barkè mamam seydoul ewwelina wal akharina amin ya rabbal haalamina
c'est vraiment extraordinaire vous aidez nous les talibes de l'esterieur de vivre les grands moments des evements du tarikha yalla nalène yalla fayye bi djayi seydil woudjoude wahalami souhoute.
ASSALAMOU ALEYKOUM MBOKI DJOULITE YI MAGUI GNANALE KEPE KOU TEWONE SI BESSOU GOUDI GUI AKH KOU AMONE YENER TEWE FA YALLA NA LA YALLA FADJALE SA ADJO BIR AKH BITI TE DJEGUEUL ADUNAKHE ALAKHIRA GNAWE TEFFE YI DJITOU AKHE YI MOUDJE YI FEGNE AKHE YI LAKHOU DEFFE SI REWMI DJAMA DJOU BARI BARI AKHE FOU DJOULITE NEKA SI DOUNYA DEFALEKA SI SOUGNOU DJEGALE SEYDI HADJI MALICK AKHE DJABOTAME MOU AGUALELLE GNOUKA SI SOUGNOU SERIGNE AL MAKTOUM MOU DJOTELELCO MAMEUME SEYDIL WOUDJOUDI ALEYHI SALAMOUNE LAH MOU DONONE LOU GNOUYE BARKELOU REK SI GOUDI MAGUAL NITOU YALLA
Mbok yi gamou nguene machalah yalna borom bi fayelene yiw.Chapeau wa dahira Treviso
ziar gnep di contan si yen yalnanco feke ay dewen you bari lol si barke borom goudigi
Assalamou Alaykoum, en tant secretaire general du dahira qui organise ce grand evenement, nous vous remercions avec un grand coeur pour vos soutien moral et economique. un soutien qui nous a permis de reussir cet evenement....yal na len yala faye si barkè borom bonè carrè bi di sounou mame cheikhal khalifa...amine.....nous vous donnons rendez vous l'annèe prochaine incha allah, mais mension spècial a toute l'equipe de asfiyahi en particuliers mame momar ndiaye l'administrateur qui est en meme temp petit fils de Serigne Babacar Sy
eskeye deugue dal dou fen fen tamit dou deugue dieure dieuf serigne mansour sy djamil ak wakeurgui yeep niom serigne abib ak niep rek waye di beral ziar sama serigne cheikh seydi mouhamadou mansour sy djamil yala bayikofi bamou yague lool amin sy malickj
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|