|
[ INTEGRALITE VIDEO ] Revivez le Takoussane Seydi Djamil du Gamou 2010
Waw wallahi khalifa bi .
vous avez eduque vos enfants dans l´amour de Dieu et les prescriptions de l´islam.vous avez pû transmetre fidelement votre savoir a votre famille qui aujourd´hui porte haut ce flambeau .une famille qui humblement travail a la paix et a la souverenete de notre pays comme ce fut dailleurs l´oeuvre de seydi elhaj malick sy.
Dieure ngen dieuf.yalla na len fi yalla saxal ci barke seydi elhaj malick radi allahou tala anhou.
serigne moutapha sy djiamil yalla nakofi yalla yagal mayko wer, et toutes la famille d'el hadji malick sy .
dieure dieuf serigne bi thisa takhawaye ak wa asfiyahi .org thi sen ligeey bou rafet
Refondation Nationale
SIGNATAIRES MANIFESTEZ VOUShttp://manifestecitoyen.blogspot.com/
wakhtanbi nekhna rafetna dioupna dieure dieuf serignbi ak wa dahira asfiyahi.org bou serigne babakar sy thi sen liggeye bou rafet bi nathi talibe cheikh yep dougal sen lokho rawatina nioun khaleyi nek europe niou bolo nek ben louniou yotou diotko poitic bi thi religeion yi ak thi tarikhayi barina wante nioun ken douniou feuk ndakh ken mounouniou wan lou eup khalifa louniou giss dafaye touti thi nioune ngir khalifa eupna lola fouf bilahhi
wakhtane wi lerna tè beuri ndieurigne yalnagne ko dieuri nio.tè lep lou ciy yiw yallah sedaleko mbolem djoulit.yalna yallah defar khol yi te may niou degue ak top bi diahi TAHA YACINE
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|