Bék rék si takhaway bi ak lifa SERIGNE ABDOUL AZIZ SY AL AMINE Toute la famille est fière amougnou sén féy té YALLAH fayal gnou soune makkk gni té tég gnou fane tégone séni tank dina djafé gnou tooloo ak gnom tanke wayé nane fékhé ba foune tégone sén tanke gnou djém fa tékk sounouy tanke ba kérok gnou léni fééki