|
Pour vivre mieux il faut être un vraie Tidiane
exactement mon frere tu vi plus leger
on choisit pas etre sur cette tarikha,le tarikha te choisit!
salam mbokk dioulite yi. magui léneu di ziar di rafète lou site bi. mane d dama doneu lathié dakh salat-al-fatiha meune gua ko wird meme so dieuloul wird
si on é en retard comment on peut fair pour étr dan l groupe en wazifa et coment on paie l retard
Mouhamadou Mansour Dieyes
Salam j'avoue que je suis très surprise et contente en même temps de retrouver votre site sur le web vraiement.mane nak dama beugone am audio wazifa bi nek dinganté timis ak guewé soudé meune na nek
je suis très fier de votre riche site pour les besoins des musulmans
Ma shalla djeuredjeuf sougnou tariha tdjania... Ake sougnou djou bakhdji.. Yalla nagnou yalla tasse dji Barker allahouma amine
wazifa matin et soir c obligatoire ou une fois par jour
Asalamou halay koume dilene nouyou dilene ndokele dilene ziyara thi werewi thi barque borom werwi di ngane yalla la sounou mame seyidil hadji malick nganone thi tarikhabi,,, machariba ahlil hadarataini ki dilathi ??? Ndakhe meuneu wirde satile fatih
Waa wawe yalla dafa wakhenie ina llaha wamala ikeutouhou you salouna halaw nabii ya ayouhalezina aameunou salou halayhi te jouli gou geuneu kawe salatoul fatihi thi mouhamed halayhi salalatou was salam amoul so geume yala geume mouhamed jouli thi
Mouhamed warnala waye yaw mi jeuloule wirdewi note defe satoulfatihi boule passe 50 ndakhe sakhe benne salatoul fatihi doyena seuke thi beuse boule wesou 50 dé sakhethi ditarbiyeu as bakane ngire deugeureule as rouh thi sakhe thi jamou yalla tarbiya
Sa bakane thi sope mouhamed sala lahou halayhi wasalime wasalamou halaye koume warahmatou lahi tahala eabarakatouhou seems mbok bouel mame doudou sy ibn serigne mbaye sy mansour barakoumou lahou
Par suite de contraintes d être à l heure du travail pourrait on anticiper la wazifa avant la prière de fait ?
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|