|
La date de l'Aïd al-Fitr (KORITÉ) est désormais connue en France , en Arabie Saoudite etc
La Mauritanie célèbrera la fête le mercredi et non le mardi comme vous dites
Commentaire *merci pour l' annonce
cheikhouna ahmadoul xadiim fall
Taafér ba fénwér
Giss ak sama beutt wala 30 yi mat seukk
Ndigeul lolou ci laniou niou ték ta fasouniouko yéné waççi bénn yonn
Ndax diguel leundamouk fajar la yag yag ci lér la dieume
cheikhouna ahmadoul xadiim fall
Lou doul ndigeul ta modi féteul lérouk timiss la yag yag ci leundeume la dieume
Mangui jéggalou mbokkou yi yalna yalla déf diamou ci senegal ak liko weur
Me yaw khadime bsmba fall sk sentou nga wer bi
KOU TOPOU NDIGUEL YAW LA CONCERNE GNOUNE CHARIA LAGNOUY TOPOU YAW AHMADOUL XADIIM FALL LAY WAKHALE
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|