|
Lettre à la Mariée (Par A. Aziz Mbacké Majalis)
Dieureudieuff serigne bi ,
que la lumiere d'ALLAH eclaire ta voie , ta vie et tout ce que tu entreprends . Je croyais etre seul dans la vie , mais aujourd'hui , je suis console de trouver a travers tes mots , un soulagement reel . Merci et qu'ALLAH te garde .
djeureudjeuf si fatalikou yi yallah na yallah fay sa djeuf fouleul leuko Abdoul Aziz Mbacké.
Wa asfiyahi gathié ngallaaaama yallah naléééne yallah yokal sééne ame ame ak sééne meune meune
Mane dé soxna la bou amagoul borom keur waayé linga waax nii fatali bou matt seuk la Yallah nala si Borom bi faye.
gnak kham rek mognou diape mais l'islam lepp la yombalal seuy mom defko farata farlou si gnane yallah mou diapaléla tahawoula rek sa lepp bakh teh mou geun si yow. yalnagnou yallah taxawou. Dieureudjeuf serigne bi :)
jeureujeuf Serigne bi. yaalna la Yalla faye. lii moy Sénégal. nou partager li nou xam ak mbokki julit yi. yaal na sa léeru maam dab la. woor na ma ni sa maam contaan na ci yaw. jeureujeufati
Ce texte est d'une grande richesse, je prie que chacun d'entre nous puissions un jour nous y conformé (ps:je ne me suis pas encore marié)......
nous prions pour le rédacteur que Dieu vous prêtes longue vie...
merci yalla nanou yalla may dègue ak top
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|