|
NOUVEAUTÉ CLIP : Ibrahima Ndiaye Garmi dans " Taalif Seuy"
machalah ndiaye yalnala yalla lafal thiate clip bi nékhe na trope...wakhe deugue yalla képe kouy seuy warna déglou lii lou am solo la
ndiaye ma cha allah way clip ya rien a dir nékh lol yalla na yalla khép dolli
nékhena trope, té di contane si yéne, yalla na léne yalla takhawou té may léne goudou fane bou andak khéweul guou beurri si barké nabi (psl)
machallah mon pere.clip bi rafettena,en plus les paroles sont riches
ma cha allah dieuredieuf amna solo trop yalla nala yalla faye naka djiguene deglou bou bakhe
vremen clip bi amna solo yalana yala gueuneu défar batbi bamou done ay clip you beuri
masha allah ibrahim sama sopey yallana yalla faye begu negn.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|