|
PHOTOS - ITALIE - Les Images de l'Université du Ramadan à Zingonia (Bergamo) ce Samedi 18 Juin 2016
maachala lii rafètena yalna yaalah deguerel sène takhaway(Maodo Diagne: Bergamon)
machallah votre travaille
Mashallah seen ligueye akk seen takhaway si beuss bi rafetna .. Yalla na yalla mottali lepp yalla sakhal beuss bi gnou diko tewwei ayy atti att
Macha Allah yalna yalla Faye yiw! DiLen diadieufal si liguey bou rafette bi!
Assalamou halaykoum bokou Yi gno gui ziar bou wer Di rafetlou sen takawaye sen téwaye rafetlou nagne ko trop yalla nalèn yalla faye si barkè ki nga khamnè amou gnou koudoul mom mouy sounou serigne seydi mouhamadoul moustapha sy yal nanou ko yagga tèw
Machala yalnanu yalla fayal serigne moustapha fayalnu sunu makgnu baahgni
Asfiyahi.org tha kaw tha kanam rafetna👏👏👏
felicitation et bonne continuation .
diarama asfiyah.org
yalna yallah motali
Asfiyahi seen ligueey rafet na te amna profetionalisme. Wa Dahiratoul Moustarchidine wal Moustarchidati moom thia kanam gnoom gni initier Universite du Ramadan ci Europe ak Senegal
Images yi set na rafetna. Dieuradiaf Asfiyahi DMWM yalla naleen yalla samm
Images yi set na rafetna. Dieuradiaf Asfiyahi DMWM yalla naleen yalla samm
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|