|
PHOTOS : Le Nouveau Visage du Mausolée de Serigne Babacar Sy ( RTA)
SY Malick Yaye sougnou sangue, sougnou Serigne, sougnou Wassila, sougnou Yakarou Taye ak Euleuk Thi Tarikha Cheikh Ahmed Tidjane Cherif
Mâcha Allah!!!! Tiey seydi aboubacar
Yalna YALLA yokk ay leeram tee tass niou barkeem amine !!
yallah na yallah yok sougnou mbeuguel ak sougnou sopel yi yaw mi sounou serigne ba adouna touki
keppe koudi sopème (serigne babcar sy(rta)) dieufeuneténa ake yawe ci batine
sy yaye donne sounou kilifa jusqu'à la fin des temps
thiey sunu sangue bi. yaye borom bonnet carré. Bilahi dosén morom. mangui gnaan si sa barké yalla na yalla déf ma admis si sama concours bi may deugmal
MACHA ALLAH!
Je suis très honoré par tous ceux qui ont participé à cette œuvre immense. Que DIEU agrée cette œuvre au nom de Serigne Babacar.
Yalla na yokk lerram te tasss gnou si barkemm, Que le bon Dieu gratifie ceux qui ont eriger cet oeuvre...
Amine Oumar, yala nagnou yala fayal mame aladji malick ah ak ndjabotame bou doul wone gnome kéne lou gnouye done tay. DIEUREUDIEUF SEYDI EL HADJ MALICK SY YALA NA YALA YOKA SA LERE TE TASSE GNOU SI SA BARKE, DIEUREUDIEUF SEYDI ABOUBACAR BOROME BONNET CARRE, DIEUREUDIEUF SEYDI EL HADJ MANSOUR BAYOU MBAYE SY MANSOUR, DIEUREUDIEUF MAME DABAKH SOU MA MAME BOY, SOU MA SERIGNE, SOU MA WASSILA.
Amine Oumar, yala nagnou yala fayal mame aladji malick ah ak ndjabotame bou doul wone gnome kéne lou gnouye done tay. DIEUREUDIEUF SEYDI EL HADJ MALICK SY YALA NA YALA YOKA SA LERE TE TASSE GNOU SI SA BARKE, DIEUREUDIEUF SEYDI ABOUBACAR BOROME BONNET CARRE, DIEUREUDIEUF SEYDI EL HADJ MANSOUR BAYOU MBAYE SY MANSOUR, DIEUREUDIEUF MAME DABAKH SOU MA MAME BOY, SOU MA SERIGNE, SOU MA WASSILA.
MachaAllah, belle oeuvre!!! yalneu ko Yalla kharé aldiana, tass gnou thi barkém
imam khalifa babacar ndiaye
yal nala yalla arre si kanam ak si ganawe si ndaye diore ak si thiamogne koula kharee yalna khaddi nii nga defal sama mame sama tourando si barkeme yalnaga andack werr foo tollou andack mouthioue ak gouddou fanne yalla defal la khaboul defala idjaba serigne abdoul aziz si al amine mala naw mala sopp mala begeu thi sama khole ya matale koolare ya sammou dine dji ak tarikhabi ak keurgui yalnala yalla sammou amiine amiine amiine ya rabbal halamina dieured de la part de imam khalifa babacar ndiaye sicap baobab
sérigne abdou aziz sy al aminn yal nako yalla défal diamme fanwou goud andak wérr
ak kouko yénné
sagalna dinédji sagal tarikha bi sagal keur chékh elhadji malick sy
délona ndioukeul bayamm sérigne babacar sy (rta)
ziarre talibe cheikh yeupe; on est tres content sur la construction du mausole de serigne babacar sy rta ; c tres beau machala
ziar na talibé yeup content thi ngi posté foto yi mame khalifa sama mame li rek la meuna am j t jure
Cheikhal Khalifa,
Yallah na Yallah yokk leram si Seydina Mouhammed PSL, té tass niou sa barké. Allahouma amine
ma gui ziar
dieuredieuf sy malick tu fai la fierte de tt les musulmans du monde sa liguey rafet ta selle lole kou gui nigua def sa rawdou waydiour bi sa khole dina contane lol que le bon dieu vs longue vie et une sante solide yokou sa soutara ak sa terenga walay contane na niou lol
machallah tedega ak teranga batine ak zayir taye ak euleuk
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|