Assalamou aleykoum. Alhamdoulilah ba niou yalla mayé niou fékké té talko. Macha allah yalla djoubalna khéw bi té yalna yalla nangou niane yeup. khana di nianal sounou Serigne, sounou wassila, sounou yakar tay ak euleuk Imam El hadji Mouhammedou Abdoulaye CISSE Madior Hafizaoullah, yalnako yalla same, aar ko, may ko katane bamou agalé mission bi ci daytalam. yalna nga ko yague di takhawé mou di raféte di djoub.
Cissé doundal doundal doundal bamou yague lolou ndakh sa dounde amna ndieurigne.
Amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine.