|
PHOTOS & VIDEO : PELERINAGE A LA MECQUE ET ZIARRA A FEZ DU CALIFE GENERAL DES TIDIANES
Serigne Mansour Sy khalif général des Tidiane yalla nafi yagu té wér
serigne abdoul aziz thiam
oh que je suis content vraiment cette vidéo a sauvé ma journée qui n'etait pas bien partie.on ne cessera jamais de prier pour le KHalif Serigne Mouhamadou MANSOUR Sy et toute la famille SY yallah na borom bi yagale séne takhaway té déffgnou deug deug talibé amine
Sant Yalla rék sant Yalla rék si khéwal bi mou gnou déffal ak soutourassi Alhamdoulilah Yalla na Yalla bayi fi khalif bi ba soutt ay Bayaame fan ammiiine Ya Rabbi
yalla nafi yague sy tai ande ak waire soumalaye khol damay ande ak fierte.laipe li nga niane maka yalla nako bour bi daife ci barkai yonenti bi salalaahou halayhi wa salam
très émouvant. Serigne mansour, yalnafi yag té weer. Amine
kan je vois le khalif general des tidianes serigne mansour sy borom daradji j'ai les larmes aux yeux parske je vois en lui un grand savant, un erudit , un guide , une bibliotheque , un guide moral qui est entrain de viellir oh moi je le connais tres bien profitez de sa presence avant qu'il ne soit trop tard té nianouma ko yalla . yalla nafi yague lolou lolou té ande ak were baci kanama kaname billahi sy sa doundou bi ame ndiarigne ko nianal mou guiss billahi lolou wornama. yalla nagnou yalla def ay talibé cheikh ba kheuy dé amineeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeee
ALIOUNE MOCTAR GAYE MAURITANIE
JE NE TROUVE PAS LES MOT POUR DIRE QU'ELLE JOIE J'AI SUR CETTE VIDÉO .SERIGNE MOUHAMADOU MANSSOUR SY YALLAH NAFI YAGUA LOLE THE ANDE AK WER
SERIGNE BI YAL NA NGA FI YAGUE LOU BARI SI SOUGNOU KANAME Té ANDE AK WERR
AMINE
khalifatou lahhi fil arrdi ma ngui lay ziar bou bakh bakha bakh kou ak sama serignou bopp serigne mansour sy djamil ak kèpp kou bokk si djabottou mame seydil hadji malick sy
mouhamadoul mansour sy malick, longue vie à lui, assorti de santé de fer pour que nous puissions le voir tous jours afin de pouvoir bénéficier à sa bénédiction car, sa présence est notre sécurité
salut je ne sais pas qui est l'initiateur de ce site mais yalla na la yalla faay ci barkè mame khalifa ababacar sy
thiey ma beugeu diabotou serigne el hadji malick SY (RTA) limay yeuk si niome yalla rek moko kham yalla naniou yalla tass si séne barké
cheikhou oumar niang diallo
yalla nako yalla bayi sounou kanam lou bari bari yok wergui yaram mame amine
sy malik doudale bamou yagalolou bounarè newe nadonne 125ans yalla na yalla maye wèèr akhe wèrelè diam akhe soutura yokko manamanebi akhe takhawebi bayila si kaname niabodebi yalla maye goudoufane mayeko sounou wadioune mayelène sutoura wèer diam tèkhè adouna akhe alakhira magui ziare di sakou gnane di ziare mokkou taliberbi akhe niabotou maodo bèpe asfisya amou sène faye yalla nalène yalla faye si barkè seydina mouhammed
serigne mansour sy yalla na fi yague té weer lool serigne bi doundal ba diyal amiiiiiiiiiiiineeee
assalamou aleykoum warahmatoulahi tallah wabarakhatouhou al hamdoulilahi bignou yallah mayé kilifa yougnouy woon yoonou deug té dignou si djitou . vraiment comme tout le monde je trouve méme pas les mots qui peuvent califier les sentiments que je ressent ; en un mot yalna yala fayalgnou seydi hadji malick ak ndiabotam amine
Que ALLAH le tout puissant donne LOngue vie et une santé d'acier au Khalife et à tout les descendant de Mawdo et à ts les talibés Cheikh si Barkè SEYDINAA MOUHAMMAD (SLAW)
dieuredieuf yalla sounou borom bi ki nous a mis sur le chemin du siratikal moustakhim et si tarikha cheick ahmed tidjane cherif par la grace du prophete al islam mouhamed sas yalla na yalla sakh al gnou si l'islam ila yawmidin,té yokewerou ak manmanou sunu khalif general bi di elhadj mansour sy borom daradji amine ya rabal alamine alahou akbar salam à tous mes ziaras
longue vie a serigne mansour sy
a chaque fois que je vois serigne mansour , je m"émeus de sorte que j"ai des larmes aux yeux
cela a t il une signification religieuse
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|