|
PHOTOS & VIDEO : PELERINAGE A LA MECQUE ET ZIARRA A FEZ DU CALIFE GENERAL DES TIDIANES
a chaque fois que je vois serigne mansour , je m"émeus de sorte que j"ai des larmes aux yeux
cela a t il une signification religieuse
yalla nagnou yalla def sopé cheikh pour mane nek sopé cheikh rek doyna tékhé wakhatouma lénène nak té serigne mansour yalla nako yalla bourbi faye bayi kofi ba ci kanam ak mbolème nit kou bakh .
Machaallah!!! Di beg rek ci souniou serigne bou tedd bi. Que Dieu lui accorde une longue vie et consolide sa santé ainsi qu'à toute la famille de Seydi Elhadji Malick Sy (RTA). AMINE.
je souhaite a serigne mansour sy bonne sante et longue vie
yallananiouyalla djappale te sakhale niou tarikhabi raye niou si ceci est la verite mouhammedienne est c est pas donner a n importe qui yalla na niou yalla def deug deug aye talibe cheikh
bismilahi rahmani rahimi par la grace de et une fwa de plus nous avons le plaisir de découvrir encore une fwa de plus notre chér grand pére et khalife générale des tijanne serigne mouhamadoul mansour sy accomplir cette importante plier de l'islam qu'est le pélerinage a la mecque.nous prions qu'allah le tout puissant puisse lui donné cette occasion cent fwa encore et qu'il le trouve en bne santé.que le bon dieu lui accorde longévité santé de fer mais aussi qu'il purifie tjurs sa science et l'augmente pour qu'ils p8ssent nous guidés lui ces fréres et soeurs encore de longues années.vrément c'est émouvant.
serigne mansour sy borom daradji il est le marabout des marabout de tout les ten
bismillahi allahamdoulilahi ( di gnane serigne mansour sy yallna fii yague téé and ek geer)
Al khamdoulilah. Yalla na Yallah nagou gnane yi ngafa déff pour pour la planete. Salam chers frères.
ALHAMDOULILAH serigne mansour yallana yala yokou fanwi mayla wer yak diabotou sydi hadji malick gui yeup contan bou am commencement te amoul djiekhital ci sounou khalifa bi.LI YALLA LA YONENE CHEKHOU TIDJANE AK SERIGNE BABACAR BILAHI DAGNE KO WARA NOGOU TE NIANALKO WER AK GOU DOU FANE CI BARKE SERIGNE BABACAR
ALLAHOUMASALI ALLAH SEYDINA MOUHAMADIN WA SALIM ! BOROM SAMA MAME Néééé MADEMAM.................. EUSKEY YA DONE SA WADIOUR.
TEK NGA SA TANK FAKA SAY KILIFA TEGOON. YANA SOUNOU BOROM MAY LA GOUDOU FAN BOU ANDAK WER. KOUNI AMINE YALA BO WOUTé AMINE
ASFIYAHI YANA YALA FAYAL GNOULENE
C'EST VRAIMENT EMOUVANT
khalifa bi yalna ko yalla doli wer qiu ya rame amine yarabi[
Je souhaite a serigne mansour longue vie e que dieu le protege contre satan
ALHAMDOULILAH,RIEN QUE DE VOIR DIEUME DIOU TEDE GUI YALLA MENE NAFA DIAR BAL LE SAY BAKAR.YALA NAKO FI YALA YAGAL TE MAYKO WER.
SERIGNE MANSOUR YA BAKH TE GOREE.
slt a ts les talibés tré contente du video yallana yalla barkel
mashaalalongue vie sy yalla nangafi yague té wer sy sy sy
dieureunguen jef asfia yal na yalla sakhal ligeybi
Longue vie et santé de fer à notre Khalif Général et bonne continuation à Asfiya.org, vraiment je me complète en vous pour les nouvelles du Khadara. Longue vie à vous aussi.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|