|
RAPPEL À DIEU D'AL MAKTOUM - Suivez la premiére réaction de Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine
Souf di na soul nit waaye dou soul dieuf am
Souf dina soul nit waye dou soul holam
Dina soul nit souf waye dou soul liguey am
Al mahtoume yalla na souf sedda sa kaw
Demnga fekki say kharite aki serigne yalla na yalla teerou si firdawsi si seen wet am
toutes mes condoleances a la communaute musulmane
Toutes mescondoleances a la famille .
Yalna yalla yok leram tass niu si barkem gno gui koy dialé niiep
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|