|
[REPORTAGE] Keur Sokhna Astou SY Malick de Louga , Patrimoine Spirituel de Tivaouane
ces gens là ne supportent pas la contradiction
leur groupe sur facebook est verrouillé
à fuir comme la peste
merci beaucoup ,je suis trs content de cette video,serigne abdou karim sarr yalla na yalla mayko wer yok ay fanam,bibaraki serigne babacar sy ,nous lougatois nous sommes tres fier de ses moukhadames tijianiya a louga comme serigne abss sall ,serigne mountaga tall ,sokhna astou, serigne ady diop ,mame malik sall ,seydou djiamil sy .
fan wou goudou yaram were gou yaram yala nako yala defal serigne abdou karim sarr ak wa keureum mai pap sarr amga geureum yaw ak say rak lepou yenla mame ass ak yalanalenfi yala bayi sougnou kanam amine
c'est chez moi ! chez ma grand Mère! Yallah na yALLAH YOK SENE LEER TE TASS NIOU CI SENE bARKE . amine
khady fall tilala dit kikich
diabotou sokhna astou sy malick ak diabotou seydi hadj malick sy yalla na léne yalla maye goudo fane ak wér bidiahi nabi moustapha s a w s ta moussaléne thi cheytane ak thiante baniou agualé séne yéné mame allahouma amine
amine yaw tamit yalla nala yalla bayi sougnou kanam.....................
bépp seutou el hadji malick sy yalla nagnou fi yalla bayi si kanam
Thiey Seydi El Hadji Malick Yalla na niou co Yalla fayal thi barké Seydina Mohamed
ZIAR AK SANT BIMA YALLAH WANALE AK SERIGNE ABDOU KARIM SARR CI BAKHOU DOMAM SERIGNE PAPE SARR.DEPUIS LORS J'AI VU UNE NETTE VISION ET UNE STABLITE DANS MA VIE RELIGIEUSE.MERCI ENCORE A SERIGNE PAPE SARR ET UNE SANTE DE FER A SERIGNE ABDOU KARIM SARR.
DANS VOTRE BIOGRAPHIE DE SOKHNA ASTOU SY VOUS SEMBLEZ AVOIR OUBLIER SERIGNE ABDOURAHMANE SARR QUE DIEU LUI RESERVE LE PARADIS COMME DEMEURE ETERNLLE
cey Maodo doomam yu jigeen gna sax ay goor yàlla lanu! Goor baax na jigeen baax na! ku am sant dàll wara wutel sa bopp aw tur xanaa!
c'est un réel plaisir de revoir ce saint homme; Mame Abdou Karim SARR c'est la sagesse même, yalna yalla dolli ka wèr mey ko gudu fan, si daraja Yonente (SAW)
babacar ndiaye ndiare wakhy ndiaye
nekhne barkla seringe abdou karim sarr yalla nafi yage tiwer ak bepe diolit
je suis tres contant d avoir realiser cette biographie mbacke mbodji
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|