|
SOUVENIR - Lundi 25 Mars 1957 - Vendredi 25 Mars 2016 : il y a 59 ans s’éloignait Serigne Babacar Sy
Même dans la Tombe , Nous continuerons a Vous Glorifier, SY MAME MBAYE
Mame k.a.b.sy. yalla yala yoko. Leram. AK diabo. M.m El.m.k.sy yepo
Tass niou thi sen barke mam babacar sy do dagn di dess thi kholy khelyi sy malik nongi nian yalla boroom bi mou yagal fi sen ndia bot gi yepo amiin yarbi
Yen mboko senegalyi rawa ti sope serigne babacar ak sope c.s.el h.Malik sy fii thi italy salgareda.treviso(it)day niu fi amal AK fatilko sunu mam ababacar sy da nu vathie ay ka mil ak ay dog nianal m.b.sy ak .f.m.El.malik sy yepo mingi.am/ 07/04/12
yala na yala yoka say ler te tasnou si sa barke
yala na yala yocc say léér seydy aboubacar RTA MERCI
JE NE T'AI PAS VU MAIS YAGUI SAMA BIR GNOL MBAYE BABACAR SY KENE DOU YAW TE DO GNOM SAKH GA DAK SI KHOL YI DI LEERAL KHALATYI SA DIEUF DOU FAY DAY LAW BA FAW GNON GUI LAY ZIARE SEYDI ABOUCAR SY LA LUMIERE DU TARIHA TIDIANE
KOU LA ROY TEKHE COU LA TOP DIEUFEUM DOU NIL DIEUREUDIEUF SEYDI ABOUBACAR SY
Kou am kaneene diapal tee bayiniok serigne babacar sy mindiou yakar tee di ko yakar geustoulene mame mbaye tanneko royouwaye dougnou dioum
ki amoul morom de kou ko nganal sabo puo nga nganal raw na gayi bou ya giu bilakhi amoulmorom sopuo na ko deman ak kepcouy talibe cheikh
macha allah yalna yala yokou lelou el hadij ababacar sy
"Bouma dononn domou kagne douma térré donne Khalifa Maodo". Balla ngua kham kouy Serigne Babacar ngua am sokhla disko GORGUI, ngua khamni ki moy Khalifa CHEIKH. Yallana Borom bi yokkou ay léram té rass niou ci barkém.
Khalifa aboubacar sy, un don du ciel .Honneur aussi pour tou etre vivant babacar sy demeure un fidele serviteur Animateur de l`islam pur khalifa est definie comme L`homme au bonnetnoir etau manteau vert. Idole et merveille pour le monde entier,khalifa est le Fondateur du dahira dont tout un chacun lui doit gratitude Aidant tout musulman a prendre position a la vraie vie
serigne babacar sy bouder febar yalla bounou wer boude tawat yalla bounou ame tane yalla na yalla yok ay lerame amine
b[[
KHALIFA ABABACAR SY SAMA SERIGNE BEUG NALA TEMOU GUEITIE CI DILEU BGNANAL SANGA BI YAY MBEUROU DINOU
MBAYE YAA FII FADJALL DINEE AY DAANNAM TEE GNEP LAA WAAR
Yalla na niou ylla doli thi tass thi barké am té yok léram thj rewmi........AMINE. Sénégalé bouléne xép niani maggni...di ko saggané djigu nou.......NB : Recherche coordonnés de CHEIKH SAMB membre de DMWM ANCIEN ARABISANT COLLEGE MODERNE DE THIES 1965.CHOUKRANE!
AL hAMDOULILLAHI.Nous sommes contents que Asfiyahi nous fasse mieux connaitre notre sope Cheikh Al Khalifa aBABACAR SY.IL FUT DIGNE SUCCESSEUR DE mawdo MALICK SY.Amoul morom .Yal na gnou YALLA tass si barke feyelnagnouko.
Diazza koumoul Lahou khayrane, kène dou
mame Cheikh Al Khalifa RTA
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|