|
Serigne Sidy Ahmed Sy Malick , fils ainé de Seydil Hadj Malick Sy , Tirailleur Sénégalais, disparu en Gréce lors de la premiére guerre Mondiale.
asla mou alay koum yen mbokou you bakh yi yal nanou yala def
taloube chekh deuqe deuqe yen nak niou bakh qeun
maqui sakou nian si yen nieup serigne mansour sy ak serigne chekhe tijane sy
ak serigne abdoul aziz sy al amin ak serigne mbaye sy man ak serigne maodo sy abd ak seni rak you bakh yi ak bolem ndiabotu moukadam yi
mam maodo am yeupe yala nanou fi yageu te andak ver
ak mbolem kou sope mam maodo yala nama yala bole sisen diabot
aaminnnnn ak kuni amin alohuma sali ala mouhamad
Superbe article. Des articles comme ça, on en redemande. Cela nous permet de revisiter notre culture et d'en toujours un peu plus sur notre histoire. Vivement que la presse sénégalaise suive cet exemple!
c vrémen nice cet article é on-a réclame tjrs plus.merci
Maodo amoul morom.
yalla nako yalla dollil lére té tasse niou thi barkém, saame djabootam bi djaii seydil woudjoud !!!!!!
§§
Alhamdoulilah bagnou Yalla boolé si diné l'Islam té khiir gnou si Tarikha Cheikh. Yalla na Yalla yokk léérou mame maodo ak jaboot tam yeup.j'ai commencé à fréquenter ce site depuis pas longtemps, mais j'adore beaucoups les articles et celui ci en particulier.Yalla mi amm faye yalla na léne faye yéne gneuw bi djaii seydi woudjoud
par la grace du tout puissant et la lumiere du prophete(s a w),qu ALLAH vous benisse
Yalla nagnou Yalla mouseule si thiat ak iblisse, bagnou meune djefé séni ndiguele ak séni téré, té défe gnou aye deug deug musulman ak aye deug deug talibé cheikh. Allahouma amine.
Telle est mes soukhait pour tout sopey cheikh.
Longue vie a tout ceux qui ont posté leur commentaire.
Yalla nagnou Yalla samme
yaram dawna dieuredieuf mame MAODO MALICK SYA (RTA)
Alhamdoulillahi ba niou Yalla khamalé Cheikh Seydil Hadji Malick Sy radiyallahou anhou ! Yalla na niou Yalla def aye talibé Cheikh thi barké Yonente bi sllallahou aleyhi wa sallam! barké serigna Babacar Sy (ra)
na ndaw gnii goorgoorlou cii tarikhabi té moytou woté you barriyi ci deuk bi
kou né ngui woté lifi amoul wone amna wayé deug rekk moye deugue.
té tarikha bi diapp mou takhaw ba nia diap mou takhaw .
yalla nanou yalla fayal mame maodo ak wa keureum amine
el hadji mamadou diattara
Dieuredieufé Mame Maodo Malick Sy ak ndiabòtame.
deuredieufé Cheikh Amed tijani.
dieureieufé Yonèn-tébi(PSL) sur Lui,sa famille et ses compagnons.
Asfiyahi, dieuredieuf ci léral yi,que Dieu vous accorde plus de bonté.(amin)
Diattara yaw kou bàkh-nga machalla.
amiin ci niane-yi , té yalna yalla fayla ak mbolèm djoulit.
yalna yalla dèf ci gnoune dèg ak topp té dèfko ci yèn.(amiin).
Merci pour cette information qui me permet de bien approfondir ma connaissance sur cette famille que j adore du fond du coeur prions que l actuel khalife atteigne son but
merci sante rek yalla minou boulèk MAODO .bayou serigne babacar sy mi tah hou yam fou niy tek sou nou tak si yonou sou nou borom bi merci encor a vs qui nous a donne cet article . et merci a toute les jeunes tijan du senegal nanou fonk tivaone bou bah ta ham nè moy sounou chance
deurengen dieuf mbermi amna soloo lol yalna sunubrom faylen ta dooli senn wer,,,,kon serigne ahmed sy malik yanlna sounou brom dooli ay lerra ta deukool ko thioa firdawsiiiiiiiiiiiiiii,,,,,,,,,,,,,,,,sene mbook uztaz diaga diop talibe jdiamil ,,,,dadon barkelou rekk deureungen deuffeti.
kéne dou wa keur cheikh TALIBE CHEIKH REK MO WOOR et yalla naniou yalla déff ay dioulite ak ay talibé cheikh.té yalla na yalla yokk séne mane mane.
le parain d cet gamou mom kéne dou mom et yalla na souf séde thi kawam.
vrément sant yalla téksi moamad ak maodo ce qu 'il a fé dans le monde j crois personne ne la fait il a sacrifié son fils pour qu'il va dans la guerre c'est une chose miraculeux
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|