|
Serigne Sidy Ahmed Sy Malick , fils ainé de Seydil Hadj Malick Sy , Tirailleur Sénégalais, disparu en Gréce lors de la premiére guerre Mondiale.
vrément sant yalla téksi moamad ak maodo ce qu 'il a fé dans le monde j crois personne ne la fait il a sacrifié son fils pour qu'il va dans la guerre c'est une chose miraculeux
yalnanou yalla fayal mawdo
maodo malick yalla na you ko yalla fayal mom mi gua khamnni mo yar rouhyi tagat len djeme fane thi sen borom moy serigne biy digule lou bakh di tere lou bone te takhaw yi tem nak.mom dal mo mata roy
AHOUZOU BILAHI MINA SHAYTANI RADJIM BISMILAHI RAHMANI RAHIM
FAS ALOU AHLA ZIKRI IN KOUTOUM LA TAHLAMOUN
NAGN SANTATI YALLA DJOLITOU SENEGAL RAWATI WA KEUR HADJI NDAH LEUP LOUGNOU WARA HAM SI SOUNOU DINEE SOUNOU YONENT PSL MAWDO HAMAL NAGNOUKO...YALNAKA YALLA YOK LER TE WEUREUL SOUNOU NGUEUM
yalla naniou yalla def ay talibe cheikh.li babacar wakh kene manoussi tek dara khana dima roy si mak niou bakh yimou toudou.yalla nala yalla fay si barke mame elhadji malick.amine
yalla naniou yalla def ay talibe cheikh,thiéy Maodo
MachaAllah, Mane de magui sante, di niane si barke MOHAMED Salalahu aleyhi wa Salam, Yalla Na soufe sede si kawam mame Maodo ak famillame yeup yi guena Adouna, ti Yalla Na Yalla bayi famillame bi fi dess ba si kanam InchaAllah, ti mou yekhe niou tamite, AMINE!! Contane na si commentaires yi yeup khole sedana, adouna bi dale soye roye royale si goryou bakhyi MachaAllah, ti il faut que niou khame que nioune nieup bena naniou. Mame Abdou dane wakhnane < restons soudes comme les membres de notre corps>. Di lene ziar, ti di balou ak nak bokou talibe yi, boulene niou fate si niane Incha Allah, Loumamana wakh moye Amineeeeeeee si NIANE YI fa tabarkAllah
comment l remercier MAME MAODO cet homme oui grâce a lui ns avons connu l prophète que la grâce de ce denier se devers se sur lui et sur tout sa famille.
yalla na yalla yok séne lére té tassgniou si séne bareké
Yallana sounou boorom yok leram, deff si gamou diamou ak mbekte
yalla yoka ay leram borom bes bi ak famiy sy yep amin khady mou mame babacar sy
sama mame mawda amoul moro khana boro thiye mame boye bokousi bonne gamou nianalenma dawouma tarde gamou magi italy sama khol bep mougi fofou nekh na dal
yalna niou yalla fayall sou ma serigne mawlana cheikh séydil khadji malick ak ndiabootam bijayii séydil woujoudi wa alami soukhoudii salla lakhou aléykhi wa sallam. amineeb
SERIGNE BABACAR SY RESTE ET RESTERA A JAMAIS GRAVER DANS LES MEMOIRES DES SENEGALAIS
e souhaite ts lé sénégalais 1 tré bn gamou é ke dieu accepte ts les voeux.
Depuis le bas age je venais à tivaoune avec mon pere et mes freres mais ces trois dernieres année je travaille à tamba et je n'ai pas occassion d'assiter au gamou . Votre site me permettra de vivre la nuit des nuit
mangui sante bou bakhe mam Elhadje Malick sy
CE COMMENTAIRE EST SOUSIGNE SOUS FORME DE POEME.²SERIGNE BABACAR LE SAINT VOUS QUI AVEZ CONTINUER LA MISSION DE SEYDI MAODA.lO SERIGNE BABACAR LE MONDE NE PLEURE PAS DE TA DISPARUTION CAR TES FILS ECLAIRE LE MONDE.
salam mangui niaan yalll sougnou boroom may niou léppou lou nou niaan thi gamou gui thi barké boroom gamou gui mouhamed (saw) té yalla bayiii fiii sr cheikh anmed tijane sy al maktoum ak képou kou sante sy rék ak bépou dioulitt itamitxxxxxx
Alioune badara ndaw barcelone
slt ziare lou beuri.gnoune senegal nagnou profité de l'ocasion nianalanté balanté.yalla yok xewal yi bir senegal.nagnou oubi xolyi waxanté deug.liguayougnou dagnouy fo.té les enseignemen de nos gran marabou com EL HADJI MALICK SY dagno lere nagn .yalla na yalla nangou niane yi si barké borom goudigui
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|