|
Seydi Khalifa Ababacar SY (RTA) (1885 - 1957)
Ki Zéro faute Amoul morom ! Cheykhoul chouyou khi
yalla na niou la yalla fa yal une tres forte personnalite
khalipha moy borom diamono kou ko soppe raw tey ak allak
ce kil a incarné nul n poura l faire. qui kéne dou mom
maachaallaah!!!! mention plus que spéciale...maachaallaah!!!! yallana boûre yalla yokka lééérame Sy Malick té taafe gnou thi barkéééme...thi barké yonénetabi s a w a s..aaamiine yaa rabba
Dieuredieufeti SERIGNE BABACAR SY
Je remercie ALLAH Maître des âmes de nous avoir offert un Khalif comme Serigne Babacar notre fierté.
serigne babacar amo morom!!!
serigne babacar sy amoul morrom yala nagnou ko yala fayal kou ko woo mou wouyou sy malick
MON GRANG PERE A MOI JE VOUS CONFIE MON âme
SEYDY ABABACAR SY TIEY BOUNIOU LA AMOUTAUNE MAME FOUNOUKOOY WAXE . MAME BOUNIOU DIAKHLEE GUISSOUL KENE TOURNE YAME THI YAW SOUNOU KHOL LEER . MO TAKH MANI (MAME BABACAR SOUNOU MAME - MAME BABACAR SOUNOU MAME SOUBASOUMA KHEUYEE YAME THI MOME SAMA KHOL FESS MA DADI REEE) BEPP TARIKHA DAKOR NANI YAY KHALIFA MONDE ENTIER .
Alhamdoulilah bouma djoudé nék djoulite ak talibé cheikh
DIEURE DIEUF SEYDI ABOUBACAR SAGOU TALIBE CHEIKH
Son modèle d'éducation à fait éclore le meilleur du sénégalais musulmans. Teey , fouleu , dal, kenn dou mbay
Khalifa yaay kenou diine Sy Ngary yaw lanu woolou. Yaay doctorou tarikha bi. Bi laahi.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|