|
TAALIF : SEEXU TIIJAAN SËRIIF ( EN HOMMAGE A CHEIKH AHMED TIJAN CHERIF ( RA )
JE VOUDRAIS VOUS DIRE QUE LESA PHOTOS QUE VOUS REPRÉSENTEZ COMMEÉTANT CHEIKHNA AHMETH TIDJANE NE L'EST PAS. JE CROIS QUE VOUS DEVEZ REVISITER LA DYNASTIE CHÉRIFENNE CONTENANT TOUTES LES PHOTOS DES ILLUSTRES FILS ET PETITS-FILS DU CHEIKH
Alhamdoulilahi , Serigne Hady TOURE yalla naniou ko yalla fayal bi barakati Cheikhou Tijanni
ma challah grand homme sr hady toure.
Macha Allah...! Serigne Hady Na Yalla fayalgnouko yook leram tass niou ci barkem
Macha Allah Yalla nagnou Yallah fayal Makk gni
Machallah magg gni wax nanou lepp lou mata wax dieufé rekk moy li war ak dess diléen niaanal yiwou Allah ila yawmal hiyamati. Yalna borom bi yéwénal mbiri magg gni té tass nou ci séeni leer. Yalla nou léen baaxé ngir yéwénal sounouk dounde. Yalnaléen Yallah faye ngeune ngi paye.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|