kontar ki yilif tarikhabi mouye cheikh ahmed tijan sy mak toum doyna bakaaar motakh malaye yebal si abajada tarikhabi zounoubou chouyoukh lah tourfa moon dokna si tarikhabi bou yague kou bagne serigne cheikh ak serigne abdou dok nga si tarkhabi ta gnoom laye bagna guisse