contenu de la page
Connectez-vous S'inscrire
Asfiyahi.Org - 1er Site de Reférence sur l'Islam et la Tidjaniyya au Sénégal

Asfiyahi.Org

Tivaouane Fm : future voix de la tidjanya et relais des aspirations des populations locales

 mamadou
Lundi 18 Janvier 2010

Notez [Ignorer]
salut je voudrai un site web pour ecouter les wazifa
je vi a l etranger je ne sais pas ou les trouver merci
 Admin
Lundi 18 Janvier 2010

Notez [Ignorer]
MERCI DE CLIQUER SUR CE LIEN POUR VOIR LES PRATIQUES DE LA TARIKHA , WAZIFA Y COMPRIS ; http://www.asfiyahi.org/La-Tarikha-Tidjaniyya_r3.html

POUR L.AUDIOTHEQUE MISE A JOUR TOUS LES JEUDIS

http://www.asfiyahi.org/GOUDI-ALDJOUMA-DU-JEUDI-7-JANVIER_a170.html
 mansour
Vendredi 10 Septembre 2010

Notez [Ignorer]
EL HADJ ABDOUL AZIZ SY (DABAAX)
Dabaax daa baax mooy ñaareelu turëm
Képp ku xam Maam Abdu seede nga ko
Daa yoroon pussò di ñaw fumu tollu
Daawul àddu mukk te yàlla taxul
Dabaax xàmmeewul Tijaan ak Murit
Xaadir , Laayeen , Ñaseen , Cenaba
Katolig ñepp dëggël nañu ko
Kii moo ragal yàlla ba ñepp rus ko
Kii moo ragal buurbi bamu feeñ ci jëfëm
Yar , teggin , kersa la làmboo
Woyof ak fayda moom ngay gis ci maam
Waxam daawul bàyyi kilifa diine yi
Mbaa aada mbaa taalibé ñépp la waxal
Ñaanam bàyyiwul baayima mbaa gaññcax
Waxumalaag doomu – adama dadaan matale
Bu wootee ñépp wuyu dëgg a ko ñor
Alxuraan ak sunna yaar yii la jiitël
Nanu tàppe xolyi lii la saxoo
Diko wax ca lammañam wu tedd wa
Bu fukki fan ak ñeent yégsée ci septambar
Xel yépp dem ci jaam bu sell maam Abdu
Asamaan jooy nako moom wéetal na suuf
Jii waay royna yonen ba xëy dëddu suuf
Maam Abdu dem na waaye moom jógu fi
Mbaax gumu lebal boroomam mooko waral
Saayu kàddoom jibée xoll yépp tooy
Senegaal ak bitim réew seede nañuko
Su buur bi doon tàggoo dégg bako fi
Waaye moo tërëlé noonu nanu muññ
Di ñaan yàlla yokku leeram fumu tollu
Te taas nu ci barkeem funu tollu




Auteur : Mansour MBAYE ( Professeur d’ Arabe au lycée de Taïba Ndiaye)
mbaymans@yahoo.fr
tel 775426558

je vous présente ce poéme en wolof pour contribuer à l'anniversaire du rappel à Dieu de Mame Abdou L Aziz SY Dabakh le 14 septembre 2010 .
 mansour
Vendredi 10 Septembre 2010

Notez [Ignorer]
EL HADJ ABDOUL AZIZ SY (DABAAX)
Dabaax daa baax mooy ñaareelu turëm
Képp ku xam Maam Abdu seede nga ko
Daa yoroon pussò di ñaw fumu tollu
Daawul àddu mukk te yàlla taxul
Dabaax xàmmeewul Tijaan ak Murit
Xaadir , Laayeen , Ñaseen , Cenaba
Katolig ñepp dëggël nañu ko
Kii moo ragal yàlla ba ñepp rus ko
Kii moo ragal buurbi bamu feeñ ci jëfëm
Yar , teggin , kersa la làmboo
Woyof ak fayda moom ngay gis ci maam
Waxam daawul bàyyi kilifa diine yi
Mbaa aada mbaa taalibé ñépp la waxal
Ñaanam bàyyiwul baayima mbaa gaññcax
Waxumalaag doomu – adama dadaan matale
Bu wootee ñépp wuyu dëgg a ko ñor
Alxuraan ak sunna yaar yii la jiitël
Nanu tàppe xolyi lii la saxoo
Diko wax ca lammañam wu tedd wa
Bu fukki fan ak ñeent yégsée ci septambar
Xel yépp dem ci jaam bu sell maam Abdu
Asamaan jooy nako moom wéetal na suuf
Jii waay royna yonen ba xëy dëddu suuf
Maam Abdu dem na waaye moom jógu fi
Mbaax gumu lebal boroomam mooko waral
Saayu kàddoom jibée xoll yépp tooy
Senegaal ak bitim réew seede nañuko
Su buur bi doon tàggoo dégg bako fi
Waaye moo tërëlé noonu nanu muññ
Di ñaan yàlla yokku leeram fumu tollu
Te taas nu ci barkeem funu tollu




Auteur : Mansour MBAYE ( Professeur d’ Arabe au lycée de Taïba Ndiaye)
mbaymans@yahoo.fr
tel 775426558

je vous présente ce poéme en wolof pour contribuer à l'anniversaire du rappel à Dieu de Mame Abdou L Aziz SY Dabakh le 14 septembre 2010 .
 mansour
Vendredi 10 Septembre 2010

Notez [Ignorer]

HOMMAGE A MAME ABDOUL AZIZ SY. CONTRIBUTION POUR LE 14 SEPTEMBRE 2010


EL HADJ ABDOUL AZIZ SY (DABAAX)

Dabaax daa baax mooy ñaareelu turëm
Képp ku xam Maam Abdu seede nga ko
Daa yoroon pussò di ñaw fumu tollu
Daawul àddu mukk te yàlla taxul
Dabaax xàmmeewul Tijaan ak Murit
Xaadir , Laayeen , Ñaseen , Cenaba
Katolig ñepp dëggël nañu ko
Kii moo ragal yàlla ba ñepp rus ko
Kii moo ragal buurbi bamu feeñ ci jëfëm
Yar , teggin , kersa la làmboo
Woyof ak fayda moom ngay gis ci maam
Waxam daawul bàyyi kilifa diine yi
Mbaa aada mbaa taalibé ñépp la waxal
Ñaanam bàyyiwul baayima mbaa gaññcax
Waxumalaag doomu – adama dadaan matale
Bu wootee ñépp wuyu dëgg a ko ñor
Alxuraan ak sunna yaar yii la jiitël
Nanu tàppe xolyi lii la saxoo
Diko wax ca lammañam wu tedd wa
Bu fukki fan ak ñeent yégsée ci septambar
Xel yépp dem ci jaam bu sell maam Abdu
Asamaan jooy nako moom wéetal na suuf
Jii waay royna yonen ba xëy dëddu suuf
Maam Abdu dem na waaye moom jógu fi
Mbaax gumu lebal boroomam mooko waral
Saayu kàddoom jibée xoll yépp tooy
Senegaal ak bitim réew seede nañuko
Su buur bi doon tàggoo dégg bako fi
Waaye moo tërëlé noonu nanu muññ
Di ñaan yàlla yokku leeram fumu tollu
Te taas nu ci barkeem funu tollu




Auteur : Mansour MBAYE ( Professeur d’ Arabe au lycée de Taïba Ndiaye)
mbaymans@yahoo.fr
 Ousseynou Krouma
Samedi 13 Octobre 2012

Notez [Ignorer]
Les freres et soeurs talibes Cheickh du Dahira El Hadji Malick SY d''Stockholm en particulier le groupe Coskas vous fellicite de cette tres belle realisation de la radio.
Nous aimerons avoir les adresses web pour pouvoir ecouter la radio sur l''interne

Votre nom :


Votre email :
 (non publié)


Message
Balise embed   Annuler ou
Votre vidéo sera affichée en dessous de votre post.