|
Traduction de la prière de fermeture de la Wazifa faite par l’intellectuel de renom Seyyid El Hadj Malick Sy (rta)
merci yalna yalla fay léne li amna solo trop
Jazakoumoulah haïran Ya Seydi!Qu''Allah te retribue de la plus noble des manières ,qu''Il t''abreuve d''un récipient exclusif à la source de Kawthar,qu''Il t''assiste en toute circonstance et dans toute entreprise bijahi Seydil Woujoud (psl)
Dieuredieuf serigne bi li Amna solo machallah.On l'attendait vraiment, yallah nallene yallah faye yiw ci barke yonente ak Seydina Cheikh Ahmed TIDIANE rta .Dieuredieuf Seydi El Hadj Malick lepeu mome la amouniou payame. Yallah na Yallah yok lerame te tasse niou ci barkeme. Amine.
yallahi anta mi radiouline ka alfa; yalna yalla deugeurel sene takhaway si sene barke kilifa; lii eupeneu solo. dimension cheikhal hadji malick sy kherteem si borombi ah rasouloul-lahi beena bousi dallee ndiabootou cheikhou tidiani sa addoun diak lol
Yalna yalla yokou la thi bior ak thi bity direudieuf
اللهم أحييني تجاني و أمتني تجاني
Alkhamdoulilah
c'est extraordinaire, vous avez abattu un travail important.Que Dieu le tout puissant vous rétribue à la valeur de votre travail.beugue na khamal nit gni ni CHEIKH SEYDI EL HADJI MALICK SY DOU MOROM.BILAHI WALAHI TALLAHI NAGNOU ORMAL GOOR YALLA GUI DI MAME MAODO AK JABOOT TAM.Quiconque ne fait pas cela payera tot ou tard les pots cassés.
Alkhamdoulilah
Amna solo Merci d tt Coeur dilen nianal yiw nioune amougnou koudoul Seydi HADJI Malick RTA Walahi cet homm multidimentionel ki a tjr incarné la Modestie Ya Rabi mangi lay niane nga fayal niou sunu Gorgui nga yok ay leram ci barke Nabil Moustapha PSL
Maa ngi ciy ziyaar taalibe Cheikh yépp. CEY MAODA. Yàlla nanu la Yàlla feyal.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|