|
URGENT! BOUSCULADE DE MOUNA: Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine présente les condoléances de Tivaouane et recommande des Prières ce Vendredi 2 Octobre 2015
C est vrai que le khalif al maktoum avait demandé de faire des prieres une semaine avant la catastrophe de la Mecque
waw Al Maktoum khamouniou niou ko! wayé moye ki dotoul wakh lou Yalla di dindi! El Hadji Mbaye dondé radiyallahou anehou moko wakhone té bataye lo lo di nek: yALL NA NIOU KO yALLA SAMMAL AAR KO SOUTOURAAL KO NIODDI AY FANAM DOLLI KO WER THI BARKE SERIGNE BABACAR SY RADIYALLAHOU ANEHOU
SERIGNE ABDOU YALLA NA FI YAGG MOME AK AY RAKKAM YI AK KILIFEU DINE YI AK TALIBE YEUPP
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|