|
URGENT! Le Khalif General des Tidianes Serigne Mbaye Sy Mansour répond à Idrissa Seck (VIDEO)
Khina Serigne bi mom yeugoul li khéw Palestine AK khalé yi niou donn rayy Sénégal
Parce que niooniou dougniou le prophète Mouhammad pssl
Machallah sérigne bi SY vous avez bien dit et c'est ce qu'on attend de nos guides religieux.
Salam, Sop Dabakh, je comprends fi nguèy wakhé mais massla mo fi wara djogué.Souniou Dîné, keneu warouko lamlamé. Ndakh bou euleugué kénène wakh lénène lou raw. Kilifa Dîné yi yeup daniou warone dadialo si bèneu euteu dale tchi kawam ba paré téréko
Sène keur yeup, mouy tiwaone, touba, etc.
Nous ne sommes pas des babtou et la liberté d expression de je suis C ne doit pas souiller notre Dîné. Tout le monde musulman est entrain de dénoncer ces dires donc le laisser pisser sur le Dîné est inaccepta
Ble.
Tey kou is sagoone ndèye nga soukhi ko, a plus forte raison sounou Dîné car c est pire que saga.
Yallah SWT na niou até ak ce messager de ibliss.
Nguène balma akheu.
Wa salam
Dieureuf sy malick souniou khole séde na
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|