As salaamu alaykum
Merci pour l'excellent travail que vous êtes en train de faire. Yalna sunu boroom fay leen fay gu kawe te defal leen yokkute ci ligeey bi ngeen di ligeeyal tariqa sayyidinaa Sheikh Ahmad At-Tijaani radhiyal-Laahu anhu.
Si vous pouvez corriger le problème d'audio de la première partie et nous la re-poster dina baax lool ci nun.
Was-salaam