|
VIDEO: Causerie de Serigne Mansour Sy , fils ainé de Serigne Cheikh Tidiane Sy Al Makhtoum
cest la 1 foi que je le vu parler mais ce monde veu des exemple come cet person serigne manssour je ferais tout pour luis voi merci
macahala rafetna trop ligawakh na gnou sama xiguenyi
que benisse serigne mouhamad el mansour sy ibn serigne cheikh ahmed tidiane sy
que DIEU benisses serigne mouhammad el mansour sy
Mille merci à celui qui nous a gratifié de cette merveille;pourrais je avoir les coordonnesde serigne mansour le conferencier,je remercie d avance
sy malick dieureudieef sa ma papa sama gorgui ;yallna ko yalla defaal weer aak diame ak fannyu goud dou ci baarke maangnii....
dieuredieuf sy domou cheikh tidiane ,tourado borom daradij setou serigne babacar fou la kham kham di reth
dieuredieuf, baarakallahou fikoum, yalnanu yalla defal degg ak topp.
dieuredieuf senegal namenagne sa conference deug rek ngay xwakh
Alkhamdoulillah Alkhamdoulillah Alkhamdoulillah
On voit en eux (fils et petits fils) notre maitre spirituel Elkhaj Malick SY.
la lumière de notre Cher Prophète Mouhamed , le Prophète des Prophètes, nous arrose et ceux jusqu'à la fin des temps .
Mame Maodo nous a montré le bon exemple : suivons le droit chemin, tracé et balisé (Siratal Moustakhim) par notre cher Prophète Mouhamed ( PSL) .
Paix et Salut sur le Prophete , sa famille et ses compagnons.
Macha Allah rafet na sope nagne la serigne bi yalla na yalla yok
FAMARA IBRAHIMA SANGARE TALIBE SERIGNE BABACAR SY
ziar nalene talibe cheikh yeupeu wakhtanou serigne mouhamadou mansour sy ibn mame cheikh ahmed tidiane sy al makhtoume nekhna yalna yala fayalnouko dieuredieuf wa asfiyahi
wahtaan wi amna solo, wah deug kou yam si yén dou rér, yalna yalla fayalgnou lène
magui ziar loumaa bagga wakh xépko sarigne mansour yalnala yalla samou ci barké makgni lima métti rek mòy kén dégatoula wayé dou métit sakh ndakh khamnà ci ndigeul nga nék
thiey Maodo amou niou sa faye.Gayii nagnou wormal seuti Maodo laca mame seute kaye dieule ba yawmal xiyaam!!!!!!!
MERCI au Dahira Moustarchidine qui avait organisé ce Gamou, et au Dahira Asfyahi qui l"a mis en ligne. Est ce possible d’être le Fils de Mame Cheikh Ahmed Tidjane SY et ne point être un océan de savoir et de connaissance?
Qui peut être un descendant de Mame Cheikh El Hadji Malick SY et ne point bénéficier de la lumière qui est à la fois source et essence?
Alors, disons tous AL HAMDOULILAHI RABIL ALAMINA !!!
Qu''avons nous fait pour mériter d''être TIDJANE?
Ce conférencier , qui est un petit fils de Mame Cheikh El Khalif Ababacar SY est un savant émérite, un soufi et un dialecticien, il me plait souvent de l''appeler "LE PROMENEUR DU DESERT"
dieuredieuf sy wallhi man layene la mais serigne mansour sy ibn serigne cheikh ahmed tidiane sy mi yala nafi yage yallna ko yalla defaal weer aak diame ak fannyu goud dou ci baarke aye bayem yo bakh yi ak ay mame yo bakh ya wallhi nekhe ne lole boke yi walhi dama bege mame abdou dabakh sy sama sopè yalla neko yalla faye te yoke aye léreme amine
dieuredieuf sy wallhi man layene la mais serigne mansour sy ibn serigne cheikh ahmed tidiane sy mi yala nafi yage yallna ko yalla defaal weer aak diame ak fannyu goud dou ci baarke aye bayem yo bakh yi ak ay mame yo bakh ya wallhi nekhe ne lole boke yi walhi dama bege mame abdou dabakh sy sama sopè yalla neko yalla faye te yoke aye léreme amine
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|