|
VIDEO: Causerie de Serigne Mansour Sy , fils ainé de Serigne Cheikh Tidiane Sy Al Makhtoum
dieuredieuf sy wallhi man layene la mais serigne mansour sy ibn serigne cheikh ahmed tidiane sy mi yala nafi yage yallna ko yalla defaal weer aak diame ak fannyu goud dou ci baarke aye bayem yo bakh yi ak ay mame yo bakh ya wallhi nekhe ne lole boke yi walhi dama bege mame abdou dabakh sy sama sopè yalla neko yalla faye te yoke aye léreme amine
alhamdoulilahi sy yalna yala goudal sa fane té yokou sa lair yene réke lanou ame té koulaine ame ame mouhamedarasouloulah ndaxe mane wornama ni yenakofi nékall ci bi diamano yenaye soune sake adouna ak alakhira T 775756034
Wakhtane bi nekhna lol diadieuf sy malick roye nga say bay ak say mame si xam xam
dialnala Yalla faye
mai commen doit je faire pour avoir ces videos je ne peux les telecharger
merci à tous
R Petit Fils Amad Lamin Diène / Mohamed
Très Heureux de notre Parrain. Que DIEU lui donne longue vie, une santé de fer, bcp de Lumières, qu'il accomplisse avec sa destinée avec succes. À bientôt.
servir.afrique@yahoo.frFADIGA MOUSSA DRAMEH
Je vous prie de recevoir mon amitié la plus sincère de ce que feu nos deux pères ont pu recevoir et enseigner aux autres ,depuis leur rencontre de leur vivant,paix à lheure âme.
Je vous prie de me contacter lors de votre prochain séjour à PARIS on ne sait plus revu ,depuis 1986 à ABIJAN et plusieurs fois à DAKAR, cher MANSOUR SY,AL MAKTOUM
salutations.
MOUSSA FADIGA DRAMEH
pt servir afrique 0751272019
1 rue BOELDIEU
twitter:servirafrique1
o.n.g
SAINT MICHEL SUR ORGE 91240
"dieuredieuf sy domou cheikh tidiane ,tourando borom daradij seutou serigne babacar fou la xam xam di diar" comme a dit l'autre.c bien dit
serigne herite dignement son pere de fond en comble.
SERIGNE MANSOUR HERITE SON PERE DE FOND EN COMBLE.
macha alla fii amoul deuxieme c maodo sont ts des leuweull autremendit sont tous des seydi hadji malick nalenn yalla sammbou bahh barke nabi barke cheikh barke maodo barke seydi mbaye barke tivaoune
yalla nala yalla lafalthiat mansour ni gue menamel
mane dama beugue serigne chekh loooooooooooooooooooooooooooooooool
assalamou alaykoum je voudrai si possible avoir le maxcimum de causeries de serigne Mansour Sy fils ainé de Serigne Cheukh Tidiane SY Al Makhtoum. d'une part et de l'autre, je n'arrive pas à lire celles que je trouve dans mes recherches
barakAllahou,machaAllah
assalamou alaykoum je voudrai si possible avoir le maxcimum de causeries de serigne Mansour Sy fils ainé de Serigne Cheukh Tidiane SY Al Makhtoum. d'une part et de l'autre, je n'arrive pas à lire celles que je trouve dans mes recherches
barakAllahou,machaAllah
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|