|
[VIDEO EXCLUSIVE] Serigne Abdou Aziz SY DABAKH (RTA) «Bawnane» ou la Générosité à l’état pur.
Thieuy Yalla bilahi mame abdou aziz mou bakh way.Yalla na yalla yokk ay lerame.
Dieureudieufé Bour yallé mome mi woutal gnou sounou sopé ba Seydina mouhmet ak aye khalifam et parmis ceux la Cheikhe Abdoul Aziz Sy Radiyallahou talla nganhou.
Yalla naniou yalla thi barkéme def gnou done deug deug Talibé Cheikhe com le lui avait demandé Cheikhe Abdoul Aziz Dabakhepar le biais d'un de ses fils, pour faire montre de son Humilité. Amine
Mame Abdou Yalla naYalla yokay lèram té taas gnou si barkém
Mame Abdoul Aziz mon Marabout quand j'entend ses paroles de sages,ses paroles divines...je me dit que c'est don de Dieu." yalla nanouko yalla fayal si bakhé ar khour aane.."
vraiment cette vidéo m'a touché et de que ceux qui aime notre trésor précieux de l'afrique et du sénégal qui nous a quitté.YALLE NA YALLA YOK Lérame
yalla nagnou yalla xeweuleul sounou barke serigne
mame abdou yalna yalla yok léram thi barké naby
slt qoisommes pratiques de lislam la tidianiyya
Yaw mi poster vidéo bi ni sama khol bi sédder yalla na ko seu leep séder si barker Salatoul Fatihi. Yalla na la yalla fayale boppame
le monde entier l'a écouté, regardé,contemplé mais tenaillé par sa prestance au point de ne pas retenir tous ses gestes et propos qui s'avèrent à ce jour être la voie de salut de l'humanité .Revisitons toutes ses litanies et nous trouverons les solutions du monde actuel en perdition
oh mon dieu dabakh restera toujours dans nos coeurs
O senegalais souvenons nous de DABAKH voila depuis sa disparition on est là dans la perdure
ces kel kun que ns sénégalais ns le connaissons pas part ca calme son sens de vie de donnez importance a la population kel kil soit c’était le vrais marabout koi kon dise ces kel kun qui a donnée o sénégalais de sens de vivre et de connaitre son diinée il tenait que tout le monde peuve se défendre son diinée pour ne pas emportée par les non musulmane je souhaite a tte le monde de faire fatiha lilahss pour que le bon dieux lui accord son paradit amen.
tanimén Abdoul aziz Sy nédo modjio mo allah modjini
SANS OUBLIER SON TALIBE DE TOUS LES JOURS ASSANE ABDOU AZIZ SAMB
En toute sincérité franchement khawma sah lane la wara wah si yi goor loudoule di gnante yallah tasse gnou li barkém
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|