|
[VIDEO EXCLUSIVE] Serigne Abdou Aziz SY DABAKH (RTA) «Bawnane» ou la Générosité à l’état pur.
al hamdouliha yana yalla faye mema abdou ligueye si dinedji ak si tarikhabi gnep djisnanouko aye kadou demame monimelni tay la wante loumanti khew mankenafi ne rewmi legui lou waye nekh daf
Jeureujeuf YALLAH sounou BOROM de nous avoir donné de tels SAINTS.Yalla na YALLAH yokk séni léér té taas niou ci séni BARKé.Avant de partir Mame Dabakh nous a montré le chemin "que nous soyons layène ou niasséne ou mouride ou tidjane nous sommes tous musulmans d'autant plus que c'est le meme PROPHETE le meme LIVRE la meme QIBLA en un mot la meme religion et en l'ISLAM y'a l'IKHSAANE konn book RAFFETTAL.Jeureujeuf Serigne Touba ,Jeureujeuf Mame El Hadji Malick ,Jeureujeuf Mame Limamou Laye ,Jeureujeuf Mame Baay Niass, Jeureujeuf Tous les Saints Musulmans du Sénégal,de l'Afrique et du monde entier.
yala nonioko YALA fayal Mame ABDOU Azis sy dabakhe
Jeureujeuf YALLAH sounou BOROM de nous avoir donné de tels SAINTS.Yalla na YALLAH yokk séni léér té taas niou ci séni BARKé.Avant de partir Mame Dabakh nous a montré le chemin "que nous soyons layène ou niasséne ou mouride ou tidjane nous sommes tous musulmans d'autant plus que c'est le meme PROPHETE le meme LIVRE la meme QIBLA en un mot la meme religion et en l'ISLAM y'a l'IKHSAANE konn book RAFFETTAL.Jeureujeuf Serigne Touba ,Jeureujeuf Mame El Hadji Malick ,Jeureujeuf Mame Limamou Laye ,Jeureujeuf Mame Baay Niass, Jeureujeuf Tous les Saints Musulmans du Sénégal,de l'Afrique et du monde entier.
http://yahoo.fr
regarde curieusement tout en me demandant, ce que j’ai bien pu y enregistrer. A ma grande surprise, je découvre l’une des dernières apparitions publiques (la dernière, en tout cas, à Dakar) de Elhadji Abdou Aziz SY Dabakh (RTA). C’était en août 1997, à l’occasion d’un « Bawnane » (séance de prières adressées à ALLAH (SWT) afin qu’IL nous gratifie d’un bon hivernage) qu’il était venu présider à la Zawia Thierno Seydou Nourou Tall à l’invitation de Thierno Mountaga Tall (RTA). L’actuelle mosquée Cheikh Oumar Foutiyou Tall, qui servait de lieu à cette manifestation, était en pleine construction. Des piliers nus, aux couleurs brutes du ciment témoignaient déjà de la fraicheur de cette atmosphère sobre, dépouillée de toute excentricité. Cette sobriété s’affichait jusque dans l’habillement des multiples fidèles venus remplir la salle de prière.
yalla nanou yalla fayal seydil hadji malick sy sy ak doomame you bakh yi serigne babacar serigne abdoul aziz sy dabakh yalla na yalla yok sene leer te tassegnou si sene barke amine
mame yalla nanou tasse sa barqué
yalla na yalla yock sayelair amine
SANT YALLA SA SOU NEK!!! ALHAMDOULILAH!!! Merci à tous les membres d'Asfiyahi ca nous rappel de beaux souvenirs! Yalla Tass niou Sén Barlé Amiin!
Alluhuma sali ala mohamed
wa ala ali Mohammed(s.a.w)
kama salayta ala
Ibrahim(a.s) wa ala ali Ibrahim (a.s)
wa barik ala Mohammed wa ala ali
Mohammed(s.a.w)
kama barakta ala Ibrahim(a.s) wa ala ali
Ibrahim(a.s.)
fil alamine inaka hamid
majid (AMIN!!!
Gorgui, yalma Yalla yokk lèram.
Dites moi comment faire pour avoir cette vidéo. ça c'est des choses à garder pour nos enfants qui n'ont pas vécu avec ce cadeau du monde musulman.
je suis tres contente de cette cite
yalla nagnou yalla tass si barkem yalla na yallah yok leeram thi barki seydi babacar sy
Alkhamdou lillah biniou yalla bollé ci ndiabootou Seydina Mouhamad (PSL) ,Wayè ouniou kilifa you ted yi fi diogué yalla na yalla yook sen leer té takh niou si sen barké ...AMINE YA RABI.
Serigne Cheikh yallah la meuna fey!kone bayi negn ko ci lokhom..
Yé ngua sounou mbeuguèl toyal ngua sounouy yéré ,Mame Abdou yallah na gnou yallah tass ci sa barké.loudoul topp sa mélo ak djeuf sey ndigueul safou gnou!
MAME ABDOU MOY SOUNIOU SERIGNE YALLA NANIOU YALA TASSE SI BARKEM.AAAAAAAAAAAAAAAAMMMIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIIINE
alhamdoulilahi bama neke talibe chiekh di rot ci limfi bayyi mouy nassiril khakhi bil khakhi
on remercie le dieux de nous doner mame abdou ak boléme nit niou baax ni fi diar té garantiwone senegal si souniou kanam borom ba yalla moussouniou yoner lou niaw nifi dess yala nalene yalla rouss com nimou mélone ak mam abdou ak ni melné mom senegal kouka beuga laal doko féké té dou tak jamai fék nassiril hax bil hax miguifiy djipe gare aux politique ki disent falou ba lal deukbi
ke dieu lamene au paradi sy malck et sa faille amine si barki cheickhoul didianie
Thieuy Yalla bilahi mame abdou aziz mou bakh way.Yalla na yalla yokk ay lerame.
Dieureudieufé Bour yallé mome mi woutal gnou sounou sopé ba Seydina mouhmet ak aye khalifam et parmis ceux la Cheikhe Abdoul Aziz Sy Radiyallahou talla nganhou.
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|