|
VIDEO - MANDAT PRÉSIDENTIEL : Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine se prononce
Salam!
Je suis talibé et j'habite à Tivaouane précisement à Diallo mais est ce k dioutoul Serigne Abdou sougnou serigne ay domame di revoir ses discours avant k mouy prononcéwou car Serigne Cheikh a dit que :"ko kam ni lo wakh mou diour contentieux, loy wakh daguako wara kham" té nous les talibés on n 'en marre de lire des insultes sur #Seneweb et d autres site.
Cordialement
#Alioune
dadoul sa Papa moutakh guakh ni dara nékoussi.
Je veux plus pleurer de voir des imbéciles faire commentaires sur lui
stp si kelkun d son entourage me lis stp nako wakh mou bayi commentaire yi si politique bi car il n a plus rien à prouver
Yow boula Serigne Abdou yakharé comme talibé gnak na
Mame moado woutoul woone talibé nawlé ladone wout té gnou gni séni nawlé lagnou
Wa Salam la discussion est close
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|