|
assalamou halykoum yene dioulitou adouna bi yep manguilene di ziar si werou gamou gui te di niane yalla yereumniou mayniou aldiana amine .
assalamou halaykoum yeen dioulityi nio gui nouyou di len ziyara dilen yeugueulni danio formè associazione ABUL HABBASS AHMADAT TIJAANII THI BERGAMO ITALIE gni gui niane sopèyep gniou bok thi kou thi b g information nga wotè thi numero yi 0039 339 52 53 986
assalmou llahi aléykoum mbokiyi yeup yalla nagnou yalla maye soutoura ak moudiou bou yalla geuereum thi touram you mague mague
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|