|
27 JUIN 1922 - 27 JUIN 2018 : Il y a 96 ans disparaissait Cheikh Seydil El Hadj Malick Sy (rta) ,
Ndeysaan !
Wallay Wallay MAODO !
Koumou nékoul sa Seurigne rék, sa seurigne : seurignam, Saydil Hadji Malick moy seurignam ! Rta
Allahou Akbar! Yallah Yalla yokk léram tass gnou si barkem dolikoyyy ngeureum!
diazakoumou lahou kharale diaza, on ne cessera point de prier pour vous de nous avoir accorder ce merveilleux par les articles les videos les rappels entres autres.
yallahnagnou borom bi fayale mame ass liguey ci rew mi yeupaci tekk sene beute
nous pensons toujour a toi mame seydi el hadji malick sy k la terre de tivaouane lui soit lègère amine
ALHAMDOULILLAHI RABILHALAMINA BA NIOU YALLAH WEURSEUGUEULÉ SEYDI HADJI MALICK SY. LE REFLET DE L'AURA DE SEYDIL HADJI MALICK ET LA REUSSITE DE SA MISSION SE COMPREND PAR LES BIENFAITS DE CE PAUVRE PAYS EN TOUT ET RICHE EN TOUT: pauvre économiquemet, mais riche de par ses ressources humaines formidables, qui comme HADJI OMAR et SEYDIL HADJI MALICK lors de leur passage à la MECQUE et les pays du golfe, émerveillent hors de nos frontières. LI téyé SENEGAL bou niou ko jawatlé: NASSIRIL KHAKH BIL KHAKH JI REK. YALLAH NA BOURBI DOLLIL KO AY LEER, CI DARAAJAY MOUHAMAD RASSOULALLAH SALLAHOU ALEYHI WA SALAM. AMINE
Allahou Akbar ...Seul Allah peut crée des Hommes comme ca
AL-HAMDULLILAH, AAMINE TE DJIEUREUNGUENE DIEUF À TOUS YALLAH NA BORROMBI KHEPEDOLLI.
merci pour tout mame Maodo..
machalla.louniou kham thi mome touti leu.wadji dafa lakou ba dem.euleuk rek lay lêre.sinon sakou na niou roy thi mome souniou beuguê souniou lep bax.wa salam
thieuy MAODO!!
yalnagnouko yala fayal té tas gnou si barkém
DIAGNE Soldarou DABAKH Talibé Serigne Babacar Abdou NDIOL FOUTA
A la lecture de ce beau article je n'ai pas retenir mes yeux de verser une larme à la grandeur et à la sainteté de notre Cheikh seydil Hadji malick Sy RTA. Je remercie tous les bons jours Allah SWT de m'avoir donné la chance de natre musulman, talibé Cheikh et de faire partie de la silsila de Cheikh Seydil Hadji Malick Sy rta.
Yalla na Yalla yokk leeram té taass niou ci barkéém.
Déwenaty et bon Gamou à tous.
merci pour la biographie de notre guide et marabout.ligueye bi propre na.YALLAH feye lene.
Yalla nanou ko YALLAH fayal, yok leeram té tafnioussi barquém.AMIIN!!!!!!!
Machallah, ce beau récit est très éducatif et j'en remercie les auteurs. Qu'ALLAH continue de nous abreuver de l'héritage grandiose et immense de notre Wassila Cheikh Seydi Hadj Malick (RTA).
Yallah na Yallah Yokk léral té tass niou ci barkème. AMINE.
tiow ba beurri rek mais maodo raw naleene bi yagg. Yal nala yala faye bilahi gnoo la beugueu. Et quand je pense kil ya des gens qui remettent en cause le fait k tu sois le premier a instaurer le gamou... Mais l''hisoitre est impossible a modifier bilahi...
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|