|
ARCHIVE VIDEO : Conference de Serigne CHeikh Tidiane Sy Al Maktoum à Demba Diop en 1988
Sougnou sante thi wa Asfiyahi amoul yamoukay. Yalnalenn Yalla dolé sameu
Li ma neekh ci Serigne Cheikh mooy, Sonalul been talibe , degg naa seedee yu bari, moom mooy jokh di dimbali talibe yi mu ngi bokk ak gnoom li mou amm te bayileen ak li gnu amm. L'attitude a encore determine l'altitude.Koon book yal nako Yaa Allah takhawal.
Mame cheikh yalla nakafi yalla bayi maikou weure ak weurele amine
Bonjour et merci pour ces contenus riches et rares.
CEPENDANT, j'attire votre attention sur votre LOGO qui mange toute la vidéo. Vous gagneriez beaucoup avec un logo plus discret et, si possible, transparent. SMALL is BEAUTIFUL.
Mais encore une fois MERCI beaucoup Shoukrane !
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|