Li ma neekh ci Serigne Cheikh mooy, Sonalul been talibe , degg naa seedee yu bari, moom mooy jokh di dimbali talibe yi mu ngi bokk ak gnoom li mou amm te bayileen ak li gnu amm. L'attitude a encore determine l'altitude.Koon book yal nako Yaa Allah takhawal.