|
[ ARCHIVES VIDEO ] Serigne Cheikh Tidiane SY Al Maktoum Gamou Tivaouane 1984
machalaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaah way li rek nekh way talibe cheikh seu kaw seu kanam silou baah
much love fr this way *tidiania*
yeh na dougou fi di ziare meumeugui yok
serigne cheikh ahmed tidiane sy for ever
mangui gnanal mame abdou yalna yalla yok lèram tè tass you thi barkèm amin.
tè di gnanal serigne manssour sy khalif gènèral des tidjian mou andak wèr ak wèrlè ak mbolème kilifa bou nèke thi tarikha chièkh ahmed tidjan chèrif gnounne ndawou tarikhabi yalnagnou yallah dolèlle tè degerelgnou thi tarikha bi yalna diam yague amine.
tarikha chièkh thia kao thia kanam.
je suis talibé cheikh .et je je suis tres fiere pour cet travail
li deug dou yag bou sobé yalla lou rafét li gnou am di na amate thi aye fane bou nékhé yalla
salut je suis talibe et jesuis tres content de ce ke vous faite je dit je vous remercie mais nous vous remercions merci nous voulons encor beaucoup de chose .
je suis vraiment ému. je vous félicite et vous encourage.
MERCI, merci, merci,...........................................
je ne sais quoi dire;suis trop ému merci une fois de plus
THIATE MO MINCE THIATE MO MINCE
je suis fiers de vous chers condisciples Tidjian, ce que vous faites est génial. kou ligayal tarikhabi do ko réthiou. Chéikh ahmet Tidjian guisnalén ainsi que Maodo et tous les autres dignitaires de la Tarikha.
al hamdoulilshi yala diokh na nou serigne cheikh tidiane sy ci monde islamique bii nou nekk
kou naafèkhou hamni il na pas de dèndèndo dans ce pays,pour ne pas dire ègal
Bjr , nous demandons au bon Dieu de guider vos pas et vous garde longtemps possible . Ce que vous faites est la satisfaction de tous les musulmans en particulier et talibés cheikh en général . Bonne continuation
Bon courage et bonne continuation.
seringe cheikh yalanafi yagg te werr yala na yala yokou ay fanam
nous aimons cheikh ahmed tidjane qui nous envi de vivre dans le tariha cheikh
talibe chiekh thia kaw thia kame
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|