|
Abdoul Aziz Mbaaye ou le rossignol de Tivaouane
abdou aziz mbaye yalla nagnou ko yalla fayal mo takh ba gnou beuri beug yonèntibi yalla na am fane wou goud tè and ak wèr amine.
Il y a du BAATINN dans cette voix. Il est l'un des rares chanteurs religieux du Sénégal à bien prononcer la langue arabe. Surtout jamais de commercialisation de CD comme l'a conseillé Mame Abdou.
abdou aziz mbaye diarrama yene gni fi nèkal tarikha tidjianiya , fanwou wou goude wèer a mouthielè votre dernier gamou avec serigne mbaye sy mansour a RIMINI, ITALIE nous a beaucoup marquer vraiment e merci pour tout yana nalèen mame el.h. malick sy et cheikh ahmed tidiane cherif faye si sèn disponibilitè si tarikhabi amen
kii sak la ci taxira bi mom ak ay mbokam yalla na yala fay léne bibaayi cheikh
En tout cas jamais je n'oublierais ce qu'ils ont fait au Gamou Diacksao de cette année c'était très touchant
wèer ak wèerlè mouthie ak mouthielè longivitè ak santè de fer a abdou aziz mbaye son frère et tte ta famille
mbaaaaaaaaaaaaaaaye yalna yalla goudal sa fane yokkou sa wéér dafal ko groupe bi yéép
yalla nama yalla tass dji barckèmm tè yalla mayko guoudou fann ak wèrr mandè yalla noko dèff sama kholl
ABDOUL AZIZ MBAAY vraiment tu chante bien .je t'aasur et coment faire pour avoir tes CD?
billahi mala sop abdu aziz mbaye yala nangay mame si baraké mam maodo
linguay woy nexna nama lol .nouay def ba am sa cd? yalla nala yallal lafal tiate.dieureudieuf
Abdoul aziz mbaye , tu incarne le discours limpide et la révélation des écrits dE LA TARIKHA, tu ne sais pas ce que tu fais en moi, que Dieu t'accorde toute sa grace :DIEUREUDIEUF MBAYE
abdoul aziz mbaye yalnafi yaga loul te andak wer te godel fanam ndakh mo yaga nio beguel ci seyidona mohamed salalaho alayhi wasalam
machalla kou bakh Mbaye khol yeupa céd bilahi kou ame fasakha yape kou deur mane walahi say mada rek moma meuneu danél c normal lou bakh rek gaye am ndakh gor gou bakh gui gaye woye yalla nalla yalla same are la té may la fan bou goude ak wer gou yaram serigne babacar ndiaye magui lay bégué
billahi ki rek laye béguéé yalla goudal sa fane
rakou ass malick diop la chaque gamou dinala gis damala sope ak begue bi nga beugue mame abdou
souma mage yal na mel ne yaw di tag rassoulil lahi salalakhou aleyhi wa salam ba fadiar
je besoin le dernier bourde de tivaouane 2012 avec abdou aziz mbaye ok quel site pour telecharger cette video ok merci envoye sur mon boite makhoulo
Amounou sa faye
Yalna sounou BOROME SOUHAANAHOU WATAALAA fayal noula
Amine
yalla na yalla yagalene yagale niou ngene yag niou begal thi Yalla,Yonnene, Cheyekhouna Tidijani, Seyidile Hadij Malick ak ndiabotame ,THI BAR KE SEYIDOUNA MOUKHAMAD CHALLA LAHOU HALAYHI WASALLAM
 Ecrire une réponse
|
Copyright 2009 - 2025 © Asfiyahi.Org - Contact : 78 459 30 30 - Email: salam@asfiyahi.org
|